Xayra

Jóge Wikipedia.


Wikipedia
Wikipedia
Bii jukki ab junj rekk la. Man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wikipedia taxawal


Xayra لقاهرة
Skyline of {{{official_name}}}
Réew  Isipt
way-dëkk 17 856 000 nit
atum way-dëkk 2 009
Rëyaay 210 km²
Fattaay 38 221 nit/km²
Gisub Xayra

Xayra (ci araab لقاهرة Al-Qāhira) mooy péeyu réewum Isipt, mooy dëkk bi ëpp nit ca goxub Afrig. Donte Al-Qāhira mooy tura dëkk waaye, lu bari, dees na ko wax itam, ci araabi waa-isipt, misr di Isipt ci araab.