Xay

Jóge Wikipedia.

Baatu xay day tekki mbooleem ay mbaax ak ay melokaani aw askan. Maanaam xamug àdduna, ci wàllu yar ak teggin ak xam-xam, yewwute gu nit ñi ci aw askan. Su ñuy wax xay dañ ciy nat tolluwaayu sag dundin, ndax jëm na kanam walla déet; baat bi dafa ëmb mbooleem ay yëngu-yëngu yuy am ci aw askan: diine, cosaan, xamteef, politig,...

Su ñu nee nit kii dafa xayadi, day tekki ne xamul àdduna. Kon xayug aw askan ñoo ngi koy natt ci doxaliin, dundiinu cër bu ne ci askan wi

Limub ay xay[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Yenn ciy xay yu doomi aadama:

Wikibaatukaay[Soppisoppi gongikuwaay bi]

  • (en) xay
  • (fr) xay

Lëkkalekaay yu biti[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Taariixu xay yi (ab lonkoyoonu xay yi ci Flash)