Melosuufug Buruundi wuute gi ci sumb yi

Jóge Wikipedia.
Contenu supprimé Contenu ajouté
Addbot (waxtaancëru)
m Bot: Migrating 12 interwiki links, now provided by Wikidata on d:q2019945 (translate me)
Ji-Elle (waxtaancëru)
+image
 
Rëdd 1 : Rëdd 1 :
{{junj}}
{{junj}}
[[Image:By-map-fr.png|right|400px|thumb|Lonkoyoonu Buruundi]]
[[Image:By-map-fr.png|right|thumb|Lonkoyoonu Buruundi]]
[[Image:Haut plateau.jpg|thumb|Buruundi]]
Buruundi am réewu diwaanu [[diggu Afrig|Diggu Afrig]] la, rëye na 27,830 km², 25,650 km² suuf la, 2,180 km² di ndox.
Buruundi am réewu diwaanu [[diggu Afrig|Diggu Afrig]] la, rëye na 27,830 km², 25,650 km² suuf la, 2,180 km² di ndox.



Sumb bi teew bu 28 Samwiyee 2018 à 11:53


Wikipedia
Wikipedia
Bii jukki ab junj rekk la. Man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wikipedia taxawal


Lonkoyoonu Buruundi
Buruundi

Buruundi am réewu diwaanu Diggu Afrig la, rëye na 27,830 km², 25,650 km² suuf la, 2,180 km² di ndox.

Melosuufug jëmm[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Mi ngi digook Kongóo-brasaawiil ci lu mat 233 km ci sowwu, ak Ruwandaa ci 290 km ci bëj-gànnaar, lang ak Tansani ci guddaayub 451 km ci penku. Buruundi amul ubbeeku ci géej gi, waaye yi ci bëj-saalum-sowwu da ñoo lang ak déegub Tanganica bu rëy ba. Réew mi dafa nekk ci diggante ñaari mbandi ndox yu mag yii di Niil ak bu Kongóo

Xool it[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Logo Commons

Xool it Wikimedia Commons


Melosuufug Afrig

Afrig gu Bëj-saalum • Alseeri • Angolaa • Bene • Botswana • Burkinaa Faaso • Buruundi • Kamerun • Kap Weer • Réewum Diggu Afrig • Bennoo yu Komoor • Kongóo-Brasaawiil • Kongóo-Kinshasa • Kot Diwaar • Jibuti • Isipt • Eriitere  • Ecoopi • Gaboŋ • Gaambi • Gana • Gine • Gine-Bisawóo • Gineg yamoo • Keeñaa • Lesoto • Liberiyaa • Libi • Madagaskaar • Marook • Malawi • Mali • Móoris • Gànnaar • Mosambik • Namibi • Niseer • Niseeriyaa • Ugandaa • Ruwandaa • Sahara gu Sowwu • Sao Tome-ak-Principe • Senegaal • Seysel • Siraa Leyoon • Somali • Sudaan • Suwaasilaand • Tansani • Cadd • Togo • Tuniisi • Sambi • Simbaawe