Mee wuute gi ci sumb yi

Jóge Wikipedia.
Contenu supprimé Contenu ajouté
Addbot (waxtaancëru)
m Bot: Migrating 205 interwiki links, now provided by Wikidata on d:q119 (translate me)
JimeoWan (waxtaancëru)
pas de correspondance entre les mois du calendrier grégorien et musulman
Rëdd 4 : Rëdd 4 :


[[Bés]] bi njëkk ci weeru mee xamees na ko niki bés bees di màggale liggéeykati àdduna bépp, ba ci [[Senegaal]] kenn du ko liggéey, ci [[Diiwaan-yu-Bennoo]] yi ak [[Kanadaa]] ñoom 1 [[Sattumbar]] lees ko di xewal.
[[Bés]] bi njëkk ci weeru mee xamees na ko niki bés bees di màggale liggéeykati àdduna bépp, ba ci [[Senegaal]] kenn du ko liggéey, ci [[Diiwaan-yu-Bennoo]] yi ak [[Kanadaa]] ñoom 1 [[Sattumbar]] lees ko di xewal.

Ci [[arminaatu weer]] bi, walla weeru wolof, mooy yam ak [[rakkaati-gammu]]


{{Weer}}
{{Weer}}

Sumb bu 13 Oktoobar 2014 à 12:42

Weeru mee mooy juroomeelu weer ci arminaatu Gregori di ñetteel ci bu Suul.

Turam ma ngi jóge ci latin, doon tur bu ko waa-rom yi joxoon ngir màggale ko seen yàlla ju jigéen ja maius, jàppees na ne Romolos miy buuru Rom bi njëkk moo ko ko jagleeloon. Ca jamono yooyu moo doonoon ñetteelu weer ci arminaatu waa-rom bi.

Bés bi njëkk ci weeru mee xamees na ko niki bés bees di màggale liggéeykati àdduna bépp, ba ci Senegaal kenn du ko liggéey, ci Diiwaan-yu-Bennoo yi ak Kanadaa ñoom 1 Sattumbar lees ko di xewal.

Weer
Samwie | Fewirie | Maars | Awril | Mee | Suwe | Sulet | Ut | Sattumbar | Oktoobar | Nowembar | Disambar