Sulet wuute gi ci sumb yi

Jóge Wikipedia.
Contenu supprimé Contenu ajouté
Addbot (waxtaancëru)
m Bot: Migrating 203 interwiki links, now provided by Wikidata on d:q121 (translate me)
JimeoWan (waxtaancëru)
pas de correspondance entre les mois du calendrier grégorien et musulman
Rëdd 2 : Rëdd 2 :

Turam ma ngi jóge ci [[latin]] ''Julius'', ngir màggale ko [[Suul Sesaar]], buuru [[Rom]] ba woon, moom mi taxawaloon ci 46 nj. j. Isaa arminaatu Suul, tudde woon ko boppam, moo nekkoon juroomeelu weer ci [[arminaatu waa-rom]] bu jamono ju yàgg ja.

Ci [[arminaatu weer]] bi, walla ci [[weeri wolof]] mooy yam ak [[ndeyi-koor]]

{{Weer}}
{{Weer}}

Sumb bu 13 Oktoobar 2014 à 12:42

Weeru sulet mooy juroom-ñaareelu weer ci arminaatu Gregori ak ci bu Suul.

Turam ma ngi jóge ci latin Julius, ngir màggale ko Suul Sesaar, buuru Rom ba woon, moom mi taxawaloon ci 46 nj. j. Isaa arminaatu Suul, tudde woon ko boppam, moo nekkoon juroomeelu weer ci arminaatu waa-rom bu jamono ju yàgg ja.

Weer
Samwie | Fewirie | Maars | Awril | Mee | Suwe | Sulet | Ut | Sattumbar | Oktoobar | Nowembar | Disambar