Imbraatóor gu Gana wuute gi ci sumb yi

Jóge Wikipedia.
Contenu supprimé Contenu ajouté
Makecat-bot (waxtaancëru)
m r2.7.3) (Robot: Adding sr:Царство Гана
Addbot (waxtaancëru)
m Bot: Migrating 34 interwiki links, now provided by Wikidata on d:q206789 (translate me)
Rëdd 17 : Rëdd 17 :
[[Wàll:Nguuri Afrig]]
[[Wàll:Nguuri Afrig]]


[[ar:إمبراطورية غانا]]
[[ca:Regne de Ghana]]
[[cs:Ghanská říše]]
[[da:Ghanariget]]
[[de:Reich von Ghana]]
[[en:Ghana Empire]]
[[eo:Ganaa imperio]]
[[es:Imperio de Ghana]]
[[et:Ghana riik]]
[[eu:Ghanako Inperioa]]
[[fi:Ghanan kuningaskunta]]
[[fr:Empire du Ghana]]
[[hi:घाना साम्राज्य]]
[[hr:Carstvo Gana]]
[[id:Kekaisaran Ghana]]
[[is:Ganaveldið]]
[[it:Impero del Ghana]]
[[ja:ガーナ王国]]
[[ko:와가두 제국]]
[[lt:Vagadu]]
[[mr:घानाचे साम्राज्य]]
[[nn:Ghanariket]]
[[no:Ghanariket]]
[[pl:Imperium Ghany]]
[[pt:Império do Gana]]
[[ru:Империя Гана]]
[[sh:Carstvo Gana]]
[[simple:Ghana Empire]]
[[sk:Ghanská ríša]]
[[sr:Царство Гана]]
[[sr:Царство Гана]]
[[sv:Ghanariket]]
[[tl:Imperyo ng Ghana]]
[[uk:Гана (Середньовічна)]]
[[ur:سلطنت گھانا]]
[[ur:سلطنت گھانا]]
[[yo:Ilẹ̀ọbalúayé Ghánà]]
[[zh:迦納帝國]]

Sumb bu 7 Maars 2013 à 22:03

Imbraatóor gu Gana gi mag ci yu Afrig yi taariixkat yi mas a xam mooy : gu Gana. Li ñu jot a xam ci taariixam ñi ngi koy sante gëstuy boroom xam-xami jeexiit yi, ak nettaliy gimiñ yi, ak mbindi tukkikati naar yi.

Gana mi ngi sosu ci ñeenteelu xarnu g.j., jamono jooja it nguur gu ndaw la woon gu ñu daa woowe Ogaadoo. Ci juroom ñatteelu xarnu g.j., la ab xareem (son armée) jugoon song ay suuf yu yaatu, yu nekk ci diggante dexug Senegaal ak Nijeer, ci noonu la Gana wëlbatikoo di imbraatóor gu mag gu teg loxo ci dëkk yi mu feggool…

Imbraatóor gi nekkoon na di gu naat : ay suuf yu nangu mbay ak sàmm, mu daa bokk ci yaxantug tàkk gi (gi nu daa defe ci tàkk gi) ak njaayum wurus mi, moom imbraatóor gi amoon na ay mbelli wurus yu bari yoy ki ko daa topptoo mooy Kayaamagana, maanaam njiitul wurus li : waa jii da daan nekk njiit lu dëgër, lu ñu wormaal, luy àtte cig maandute te daan samp foŋsaneer yi. Moom nag cim koom ak naataange la daa dunde ci péeyam, waa diiwaan bii it dañu ko daa indil ay kem ci wurus wi ñiy génnee ci suuf si, ginnaaw bi mu faatoo nag la ko fi ab jarbaatam wuutu. Ci atum 1052 g.j., la Muraabituun yi song Gana, ci layuw dañuy dugal ñoñam ci lislaam, ñu daal di ubbi péey ba atum 1076 g.j., ginnaaw bi Gana néew doole, daal di daanu ci mujjantal gi ci loxoy imbraatóor gu Mali atum 1240 g.j.

Seetal BUNTU TAARIIX
wikbaatukaay am na xët wu tudd: Imbraatóor gu Gana