Alxuraan wuute gi ci sumb yi

Jóge Wikipedia.
Contenu supprimé Contenu ajouté
Xqbot (waxtaancëru)
m r2.7.3) (Robot: Modifying ps:قرآن کریم to ps:قرآن
Ptbotgourou (waxtaancëru)
m r2.7.2) (Robot: Modifying tl:Koran, vi:Khả Lan, zh-min-nan:Kuran
Rëdd 130 : Rëdd 130 :
[[tg:Қуръон]]
[[tg:Қуръон]]
[[th:อัลกุรอาน]]
[[th:อัลกุรอาน]]
[[tl:Quran]]
[[tl:Koran]]
[[tr:Kur'an]]
[[tr:Kur'an]]
[[tt:Qör'ən]]
[[tt:Qör'ən]]
Rëdd 137 : Rëdd 137 :
[[ur:قرآن]]
[[ur:قرآن]]
[[uz:Qurʼon]]
[[uz:Qurʼon]]
[[vi:Qur'an]]
[[vi:Khả Lan]]
[[wa:Alcoran]]
[[wa:Alcoran]]
[[war:Coran]]
[[war:Coran]]
Rëdd 145 : Rëdd 145 :
[[zh:古兰经]]
[[zh:古兰经]]
[[zh-classical:古蘭經]]
[[zh-classical:古蘭經]]
[[zh-min-nan:Qur'an]]
[[zh-min-nan:Kuran]]

Sumb bu 4 Oktoobar 2012 à 22:24

Alxuraan

Téeree ngii di benn ci yi ñu gën a yër ci àdduna bi, mooy téere bees sellal ci lislaam, di fi jullit ñiy ball-loo seen yoon di Shariiha, ak ci sunna siy dundiinu Yonnant bi (jàmm yal na nekk ci moom), kon nag bu am solo la lool fi jullit ñi. Alxuraan: Alxuraan mooy téere bu sell bi ñeel jullit ñi, mooy balluwaay bu njëkk bi ñeel yoonal gu Lislaam gi, ci ginnaawam la Sunna di ñëwe. Li njëkk a wàcc ci Alxuraan it mooy laaya wi njëkk ci saaru Halaq muy : «Jàngal ci sa turu boroom bi bind (sàkk) »

Alxuraan nag mooy waxi Yàlla ji mu wàcce ci Yonentaam ba Muhammad, Jibriil nag mooy ndawul Yàlla tey malaaka mi ko wàcce; ngir nag Yonent bi jottali ko nit ñépp,. Moom nag fa Yàlla dees koo bind ca àlluwa jees wattu ja (Lawhul Mahfuus), àlluwa jii nga xam ne Yàlla bind na ca lu nekk njëkk mu koy sàkk. Wattu googu nag Yàlla la soob, mu bëgge ko noonu, noonu la ko waxe: «Nun noo wàcce Alxuraan, te nun noo koy wattu»