Doxalukaay bu mbëj wuute gi ci sumb yi

Jóge Wikipedia.
Contenu supprimé Contenu ajouté
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 17 : Rëdd 17 :
Dawanu mbëj gi day jaar ci ab lëmës gu ñu lëmës ci ab doggu weñ gi tudd [[Tekkaaral]]. Lëmës googu, gi ñu defare ak wëñu përëm, jur ab toolu mbëjxëccu bu ca dawan jaaree. Toolu mbëjxëccu googu dañ koy sòob ci beneen toolu mbëjxëccu gu [[wëndeelukat]] bi jur, mi melokaanoo teewaayu ñaar walla ñetti seexi [[dott]]. [[Wëndeelukat]] bi tambalee wëndeelu ci sababu njureelu mbëjxëccu, bëjgannaaru toolu xëccu gu wëndeelukat bi day wòotalante ak bëjsaalumu toolu xëccu gu yem gi. Xaaju wëndeelu gu nekk dotu gi day soppeeku, ci noonu la wëndeelu gi mënë wëyee.

Doxalkat bii ci dawan safaanu rek lay doxee. Suy dox, ag wall gu nèew ci kattanu mbëj gi day tass soppeku tanggoor ngir [[sababu joule]].
Doxalkat bii ci dawan safaanu rek lay doxee. Suy dox, ag wall gu nèew ci kattanu mbëj gi day tass soppeku tanggoor ngir [[sababu joule]].

== Taariixam ==
Ci atum 1821, lu weesu xamteg feñte gu mbëjxëccu gu simikat bii di Ørsted xamle, la nekkat bu waa-angalteer bii di Michael Faraday defar ñaari wuutuloxo ngir baril li mu duppee ab wëndeelug mbëjxëccu: ab jalaxub mbege gu wëy, gu ab dooley xëccu ci lu wër ab wëñ, ci maanaa mooy faramfacey doxalkat mbëj gu njëkk.
== Lëkkalekaay yu biir ==
[[Doxalkat demando]]
[[Doxalkat demandowul]]
[[Doxallat safanoowul]]
[[dawaan safaanoo]]

Sumb bu 28 Sulet 2007 à 15:34

UBBITE

Doxalkat mbëj tekkeem moy ab wuutuloxo mbëj la goo xam ne kattan giy duggu ci moom gu mbëj la te ga muy genne gu doolerandu la. Doxalkat mbëj yi am nañ solo lool ci dundinu jamono gu bees gi, te it dëggë la sax ne limu doxalkat mbëj yi nekk ci am reew day firndeel tolluwaayu jëm-kanam mam. Te itam deminu, maanam yokkute walla nèewte limu doxalkat mbëj yi ci am reew bokk na ci wonekat yiy firndeel tolluwaayu yokkute ci wallu xarala mu reew moomu. Ngir dëggël loolu, doyna xool ci jumtukaay yi nekk ci li ñu wër: ca saxaar ba ci watukaay ak yeneen ak yeneen, yi ngeen xam ne nit ku bees ki moo ngi koy jëfëndikoo bu baax, mën naa ni sax ñooy doxal sunug dundu.

Xaralay doxin gi

Wall gi solowu:

Doxin

Dawanu mbëj gi day jaar ci ab lëmës gu ñu lëmës ci ab doggu weñ gi tudd Tekkaaral. Lëmës googu, gi ñu defare ak wëñu përëm, jur ab toolu mbëjxëccu bu ca dawan jaaree. Toolu mbëjxëccu googu dañ koy sòob ci beneen toolu mbëjxëccu gu wëndeelukat bi jur, mi melokaanoo teewaayu ñaar walla ñetti seexi dott. Wëndeelukat bi tambalee wëndeelu ci sababu njureelu mbëjxëccu, bëjgannaaru toolu xëccu gu wëndeelukat bi day wòotalante ak bëjsaalumu toolu xëccu gu yem gi. Xaaju wëndeelu gu nekk dotu gi day soppeeku, ci noonu la wëndeelu gi mënë wëyee. Doxalkat bii ci dawan safaanu rek lay doxee. Suy dox, ag wall gu nèew ci kattanu mbëj gi day tass soppeku tanggoor ngir sababu joule.

Taariixam

Ci atum 1821, lu weesu xamteg feñte gu mbëjxëccu gu simikat bii di Ørsted xamle, la nekkat bu waa-angalteer bii di Michael Faraday defar ñaari wuutuloxo ngir baril li mu duppee ab wëndeelug mbëjxëccu: ab jalaxub mbege gu wëy, gu ab dooley xëccu ci lu wër ab wëñ, ci maanaa mooy faramfacey doxalkat mbëj gu njëkk.

Lëkkalekaay yu biir

Doxalkat demando Doxalkat demandowul Doxallat safanoowul dawaan safaanoo