Wikipedia:Babel wuute gi ci sumb yi

Jóge Wikipedia.
Contenu supprimé Contenu ajouté
Ibou (waxtaancëru)
Xët mu bees : '''UBBITE''' ---- Xët mii moo lay leeral nooy xamale yeneen way-jëfëndikoo yi, say xameel ci yeneen làkk yi ak tolluwaayu xameel gi. ---- ---- == Lumuy jariñ == Donte fii Wikiped...
 
Ibou (waxtaancëru)
Rëdd 8 : Rëdd 8 :

Gii mebet di na yombal jokkoo gi ci biir aw askan gu bariy làkk gu mel ne Wikipedia: ci misaal, di na yomb jot kuy wax wenn làkk wi, te itam di na xamale tolluwaayu degginu wolof gu ab jëfëndikookat bu bindu.

Sooy seet tamit lu mel ne babelbox te mana soppiki ci ni nga ko bëggee xoolal tamit [[Wikipedia:Babelfish ]]

== Nu ma koy defee? ==
== Nu ma koy defee? ==

Sumb bu 21 Sulet 2007 à 14:39

UBBITE

Xët mii moo lay leeral nooy xamale yeneen way-jëfëndikoo yi, say xameel ci yeneen làkk yi ak tolluwaayu xameel gi.

Lumuy jariñ

Donte fii Wikipedia la ci kàllaama wolof, waaye du ñi fi nekk ñëpp a deggante. Am na ñu deggul wolof, walla seen degg des na, ñu mana soxla ku ñu jokkool ci làkk bi ñu degg, walla wolof yu yomb. Am na ay waa-wikipedia yu deggul wolof te di bëgg a japp ci ligey bi, kon di na am solo lool nga wax ko ci yan làkk ngeen man a waxtaane, ngir njariñam man a feeñ.

Gii mebet di na yombal jokkoo gi ci biir aw askan gu bariy làkk gu mel ne Wikipedia: ci misaal, di na yomb jot kuy wax wenn làkk wi, te itam di na xamale tolluwaayu degginu wolof gu ab jëfëndikookat bu bindu.

Nu ma koy defee?

Doy na nga yokk ci sa xëtu jëfëndikookat Babelbox bi, tabax ko ci topp tektal yii:

  • Tambalil ak {{Babel-
  • Nga yokk ci limu làkk yi nga degg te teg ci |
    • Misaal: {{Babel-3| (3 làkk)