Saytubiddiw wuute gi ci sumb yi

Jóge Wikipedia.
Contenu supprimé Contenu ajouté
EmausBot (waxtaancëru)
m r2.6.4) (Robot: Modifying iu:ᓯᓚᓯᐅᕐᓂᖅ
AvocatoBot (waxtaancëru)
m r2.7.1) (Robot: Adding gn:Mbyjakuaa
Rëdd 72 : Rëdd 72 :
[[gd:Reul-eòlas]]
[[gd:Reul-eòlas]]
[[gl:Astronomía]]
[[gl:Astronomía]]
[[gn:Mbyjakuaa]]
[[gu:ખગોળશાસ્ત્ર]]
[[gu:ખગોળશાસ્ત્ર]]
[[gv:Rollageydys]]
[[gv:Rollageydys]]

Sumb bu 8 Awril 2012 à 21:22

Saytubiddiw mooy xam-xam biy xool aka saytu biddiw yi, di jéem a faramface ak a leeral seen melokaan ci jëmm ak ci simi, seenug magg ak seen cosaan. Doon na xam-xam bu am lu ëpp 6 000 at, ay cosaani saytubiddiw jiitu na jomono ju yàgg ja.

Te ñu bañ koo jaawale ak gëstubiddiw

Taariixkat yi nee nañu saytubiddiw mooy xam-xam bi gën a yàgg ci àdduna bi. Xay yu njëlbeenu yi sax amoon nañu ci ay xam-xam.


Tekkiinam

Xam-xamu saytu-bidiw bokk na ci xam-xam yu njëkk yi am ci fajarug nite, moom xam-xam la buy yittewoo fuglu ak jàng xew-xew yiy xew ci bitib kol-kol bu suuf si ak ci muuraay gu jawwoom gi. Mooy it xam-xam biy joxe xibaar yi aju ci feeñte (phenomene)yu bidiw yi. Saytu-bidiw mooy gëstu tàmbalig yaram yi ñu man a fuglu ci asamaan si (biti suuf si), ak séenug jëm-kanam ak séeni jagle yu jëmm (walla fisiyaa) ak yu kimyaa, ak xew-xew yi ñuy àndal.

  • Français:astronomie
  • English:astronomy