Tamxarit wuute gi ci sumb yi

Jóge Wikipedia.
Contenu supprimé Contenu ajouté
WikitanvirBot (waxtaancëru)
m r2.7.1) (Robot: Modifying ta:முஃகர்ரம்
ZéroBot (waxtaancëru)
m r2.7.1) (Robot: Adding ba:Мөхәррәм
Rëdd 12 : Rëdd 12 :
[[av:МухIаррам моцI]]
[[av:МухIаррам моцI]]
[[az:Məhərrəm]]
[[az:Məhərrəm]]
[[ba:Мөхәррәм]]
[[bjn:Muharram]]
[[bjn:Muharram]]
[[bn:মুহররম]]
[[bn:মুহররম]]

Sumb bu 24 Maars 2012 à 10:16

Tamxarit (محرم ci araab), mooy weer wi njëkk ci yu gàddaay gi, moom nag bokk na ci li ñuy wax ci Lislaam "Al-ashur al-hurum", (maanaam weer yu am worma yi): tamxarit nag tuddees na ko ci araab "muharram" ngir ne araab yi dañu ci daan araamal xeex.

Xew-xew

Weeri wolof

Tamxarit | Diggi-gàmmu | Gàmmu | Rakki-gàmmu | Rakkaati-gàmmu | Maami-koor | Ndeyi-koor | Baraxlu | Koor | Kori | Diggi-tabaski Tabaski