Ndakaaru wuute gi ci sumb yi

Jóge Wikipedia.
Contenu supprimé Contenu ajouté
Escarbot (waxtaancëru)
m r2.7.2+) (Robot: Adding so:Dakar
Rubinbot (waxtaancëru)
m r2.5.4) (Robot: Adding bm:Dakar
Rëdd 30 : Rëdd 30 :
[[be-x-old:Дакар]]
[[be-x-old:Дакар]]
[[bg:Дакар]]
[[bg:Дакар]]
[[bm:Dakar]]
[[bn:ডাকার]]
[[bn:ডাকার]]
[[bo:ཌ་ཀར།]]
[[bo:ཌ་ཀར།]]

Sumb bu 19 Disembar 2011 à 02:25


Wikipedia
Wikipedia
Bii jukki ab junj rekk la. Man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wikipedia taxawal


Dëkku Ndakaaru

Skyline of {{{official_name}}}
Réew Senegaal
Diiwaan Ndakaaru
way-dëkk 1 075 582 nit
Dencukaay:Dakar plateau,pdlind.jpg
Ndakaaru ca mbeddum Jorj Pompidu, te tuddoon Wilyaam Ponti
Ndakaaru

Ndakaaru (Dakar) Nekkoon péyu Afrig gu sowwu gu fraase (ASF, walla AOF ci FR), Ndakaaru fimne mooy Péyu reewum Barug Senegaal akit goxub Ndakaaru, tolluwaayam ci péeteg sowwu bu Afrig, ci jegeem Daanaka-dun bu Kap-Wert, waral na sancug notaakon yu jëkk yi, Akit yaxantu ak Àdduna bu bees bi, te ame na peetewaayu ngëneel ci jëflanteg cosaani Saa-Afrig yi ak Saa-Tugal yi. Fa lees Taxawalee woon Xumbalu Àddina bu fànni ñuule (jaam yu ñuul) bu njëkk bi ci xalaatu Leopool Sedaar Sengoor atum 1966, Dëkk bii mooy toogu bu Këru-gëstu bu dàttu bu Afirg gu ñuule (KDAN, walla IFAN ci FR) akit bu Bànk bu diggu bu guuri Afrig gu sowwu (BDGAS walla BCEAO ci FR)

Logo Commons

Xool it Wikimedia Commons