Bëj-saalumu Aamerig wuute gi ci sumb yi

Jóge Wikipedia.
Contenu supprimé Contenu ajouté
Dinamik-bot (waxtaancëru)
m r2.6.5) (robot Adding: sn:South America
Xqbot (waxtaancëru)
m r2.7.2) (Robot: Adding as:দক্ষিণ আমেৰিকা; cosmetic changes
Rëdd 6 : Rëdd 6 :


== Taariix ==
== Taariix ==
Ay askan yu jòge woon goxub [[Asi]] ñoo ko dëkkee woon, daanaka am na ay junniy at nj.j.(njëkk judd gu [[Isaa]]). [[Amerigo Vespuci]] mooy tugal-tugal bi fa njëkk a teg tànkam, waaye li gën a siiw mooy ne [[Kristof Kolomb]] mooy ki ko wuññi
Ay askan yu jòge woon goxub [[Asi]] ñoo ko dëkkee woon, daanaka am na ay junniy at nj.j.(njëkk judd gu [[Isaa]]). [[Amerigo Vespuci]] mooy tugal-tugal bi fa njëkk a teg tànkam, waaye li gën a siiw mooy ne [[Kristof Kolomb]] mooy ki ko wuññi


== Cancug waa tugal gu gox bi ==
== Cancug waa tugal gu gox bi ==
Rëdd 33 : Rëdd 33 :
{{Réewi Bëj-saalumu Aamerik}}
{{Réewi Bëj-saalumu Aamerik}}
{{gox}}
{{gox}}
[[nso:Amerika Borwa]]


[[Wàll:Gox yi]]
[[Wàll:Gox yi]]
[[Wàll:Aamerig]]
[[Wàll:Aamerig]]
[[Wàll:Diwaani Aamerig]]
[[Wàll:Diwaani Aamerig]]

[[kbd:Ипшъэ Америкэ]]
[[nso:Amerika Borwa]]


[[ace:Amirika Seulatan]]
[[ace:Amirika Seulatan]]
Rëdd 50 : Rëdd 48 :
[[arc:ܐܡܪܝܩܐ ܬܝܡܢܝܬܐ]]
[[arc:ܐܡܪܝܩܐ ܬܝܡܢܝܬܐ]]
[[arz:امريكا الجنوبيه]]
[[arz:امريكا الجنوبيه]]
[[as:দক্ষিণ আমেৰিকা]]
[[ast:América del Sur]]
[[ast:América del Sur]]
[[az:Cənubi Amerika]]
[[az:Cənubi Amerika]]
Rëdd 122 : Rëdd 121 :
[[ka:სამხრეთი ამერიკა]]
[[ka:სამხრეთი ამერიკა]]
[[kaa:Qubla Amerika]]
[[kaa:Qubla Amerika]]
[[kbd:Ипшъэ Америкэ]]
[[kk:Оңтүстік Америка]]
[[kk:Оңтүстік Америка]]
[[kl:Amerika Kujalleq]]
[[kl:Amerika Kujalleq]]

Sumb bu 18 Disembar 2011 à 04:48

Bëj-saalumu Aamerik ci lonkoyoonu àdduna bi

Bëj-saalumu Aamerig ci yenn sedatle yu àdduna bi dees koy jàppe ni ab gox, walla ci yeneen sedatle, ab ron-gox bu yamoo wi jaar, te li ëpp ci suufam ci xaaju kol-kol bu Bëj-saalum la nekk.

Melosuuf

Bëj-saalumu Aamerig mi ngi ne ci diggante Mbàmbulaan gu Dal gi ak Mbàmbulaanu Atlas gi. Doon na gox bu bariy dun, yi ci ëpp nag ci réew yi ci gox bi lañu bokk. Li ko lëkkaleek Bëj-gànnaaru Aamerik mooy Panamaa. ag càllale gu ay doj moo leru penku gox bi bépp, ci kaw ba ci suuf; li ëpp ci penkoom àllub yamoo la. Amasoni mooy àll bi ëpp ci àdduna bi, ca réewum Bereesil la nekk.

Taariix

Ay askan yu jòge woon goxub Asi ñoo ko dëkkee woon, daanaka am na ay junniy at nj.j.(njëkk judd gu Isaa). Amerigo Vespuci mooy tugal-tugal bi fa njëkk a teg tànkam, waaye li gën a siiw mooy ne Kristof Kolomb mooy ki ko wuññi

Cancug waa tugal gu gox bi

La ko dale ca xarnub XVI la way dëkk yu Bëj-saalumu Aamerig tàmbalee am ay jàmmaarloo ak waa Tugal yi. Waa Ispaañ ñooy ñi fa njëkk, waa portugaal tegu ci, ci noonu ndànk-ndànk boroom doole yu waa tugal yépp tase fa di xëccoo suuf sa ak way dëkk ya fa cosaanoo, ak tam it ci seen diggante, ay jàmmaarloo yu metti juddoo na ca.

Limu réew yi

Juroom ñaari réew yu temb yi

Ñetti réew yu tembul yi