Mbëjfepp wuute gi ci sumb yi

Jóge Wikipedia.
Contenu supprimé Contenu ajouté
Vagobot (waxtaancëru)
m r2.7.2) (Robot: Adding ne:इलेक्ट्रोन
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 : Rëdd 1 :
'''Mbëjfepp''' as [[wàll-wàllaan]] la (wàll su ndaw lool) su [[xarefulwoon]] bi bu sëfoo ab [[yanu mbëj]] bu bon(-) bu tollook q<sub>e</sub> = 1,602 · 10<sup>-19</sup> [[Coulomb|C]], te dayoom toll daanaka ci 9,10 · 10−31 kg (ci beneen bennaanu natt di 0,511 MeV/c²), dees na ko wax itam [[yan bu njëlbeen]] walla [[wàll-wàllaan wu njëlbeen]].
'''Mbëjfepp''' "électron ci fr" as [[wàll-wàllaan]] la (wàll su ndaw lool) su [[xarefulwoon]] bi bu sëfoo ab [[yanu mbëj]] bu bon(-) bu tollook q<sub>e</sub> = 1,602 · 10<sup>-19</sup> [[Coulomb|C]], te dayoom toll daanaka ci 9,10 · 10−31 kg (ci beneen bennaanu natt di 0,511 MeV/c²), dees na ko wax itam [[yan bu njëlbeen]] walla [[wàll-wàllaan wu njëlbeen]].

Naka-jekk ab mbëjfepp njunj bees koy jëmmale mooy '''e<sup>-</sup>'''. [[Xarefulwoon]] yi li booloo nekk leen ñooy ab [[saal]] (bi dajale ci biiram ay [[feppsaal]] aki [[feppmaandu]]) aki mbëjfepp yu koy wër. Dayoo mbëjfepp yaa ngi tollook daanaka 1/1836 yu [[feppsaal]] ak yu [[feppmaandu]]). Mbëjfepp yi cër yu cëslaayu lañu ci ne-ne yi, ñooy wàll-wàllaan yi gën a tuuti cib ne-ne ba tax kenn maneesu koo séddalewaat yeneeni cër.

Sumb bu 11 Disembar 2011 à 11:47

Mbëjfepp "électron ci fr" as wàll-wàllaan la (wàll su ndaw lool) su xarefulwoon bi bu sëfoo ab yanu mbëj bu bon(-) bu tollook qe = 1,602 · 10-19 C, te dayoom toll daanaka ci 9,10 · 10−31 kg (ci beneen bennaanu natt di 0,511 MeV/c²), dees na ko wax itam yan bu njëlbeen walla wàll-wàllaan wu njëlbeen.

Naka-jekk ab mbëjfepp njunj bees koy jëmmale mooy e-. Xarefulwoon yi li booloo nekk leen ñooy ab saal (bi dajale ci biiram ay feppsaal aki feppmaandu) aki mbëjfepp yu koy wër. Dayoo mbëjfepp yaa ngi tollook daanaka 1/1836 yu feppsaal ak yu feppmaandu). Mbëjfepp yi cër yu cëslaayu lañu ci ne-ne yi, ñooy wàll-wàllaan yi gën a tuuti cib ne-ne ba tax kenn maneesu koo séddalewaat yeneeni cër.

Wikipedia
Wikipedia
Bii jukki ab junj rekk la. Man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wikipedia taxawal