Bere wuute gi ci sumb yi

Jóge Wikipedia.
Contenu supprimé Contenu ajouté
Woloflover (waxtaancëru)
New page: Ci làkku gereg Βέροια; Ci angale mooy ''Berea''; Ci faranse mooy ''Bérée'' Benn dëkk ci diiwaanu Maseduwan la woon. Nekkoon na ca joor ga nekk ca taatu tund wi ñuy wax ''Be...
 
Woloflover (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 : Rëdd 1 :
{{coor title dm|40|31|N|22|12|E|region:TR_type:city}}

Ci làkku gereg Βέροια;
Ci làkku gereg Βέροια;
Ci angale mooy ''Berea''; Ci faranse mooy ''Bérée''
Ci angale mooy ''Berea''; Ci faranse mooy ''Bérée''

Sumb bu 18 Suwe 2007 à 19:08

Royuwaay:Coor title dm

Ci làkku gereg Βέροια; Ci angale mooy Berea; Ci faranse mooy Bérée

Benn dëkk ci diiwaanu Maseduwan la woon. Nekkoon na ca joor ga nekk ca taatu tund wi ñuy wax Bermio lu tollu 35 kilomet digganteem ak Géeju Ese (mer Egée). Dëkku Gereg la bu amoon ay Yawut yu bare. 70 kilomet moo nekk diggante Bere ak Tesalonig. Tey jii dëkk bi Weroya (Véroia) la tudd.

Man nañu jàng ci Bere ci Jëf 17:10-14; 20:4.