Waxtaani dencukaay:Abdu Xaadir KEBE.jpg wuute gi ci sumb yi

Le contenu de la page n’est pas pris en charge dans d’autres langues.
Jóge Wikipedia.
Contenu supprimé Contenu ajouté
Xët wu bees : Abdul xaadir noongi lay saant fa ak cannt tambulee te amul yamu kaay ndax wolof njaay nee na ku wacci sab annda be neen bo demit fakk fa boroom mu te du ko màss di bokk ak yaw kon...
 
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
 
Rëdd 5 : Rëdd 5 :
Kariim jóob.
Kariim jóob.
beenjaro@yaho.es
beenjaro@yaho.es

Santees na ci soññee gi, waaye fii fi biir Wiiki bi lu sàkkan lu man a jàngalee ngi fi, dee ci sëgg, soo siggee màndi as lëf, teewul sama E-bataaxal (email) mooy sakkmultiservices@yhotmail.com. Ngir lu aju ci tekkig Masaalig soo bindee waxtaanees ci. Jaajëf--[[User:Abdu Xaadir KEBE|Abdu Xaadir Kebe]]<sup> ([[User talk:Abdu Xaadir KEBE|xëtu waxtaanuwaay]])</sup> 12 Suwe 2011 à 12:57 (UTC)

Sumb bi teew bu 12 Suwe 2011 à 12:57

Abdul xaadir noongi lay saant fa ak cannt tambulee te amul yamu kaay ndax wolof njaay nee na ku wacci sab annda be neen bo demit fakk fa boroom mu te du ko màss di bokk ak yaw kon niik li génn mooy nu jémma war ca sunuy ànnda

balay darray xew  te li wér te wóor mooy ne  xoddi ku ca bala ngaa lakk le ,
 Man nakk ab ndogo laa boob sama alluwa sori wul moo tax soxla wu na  ay sëriñi Daara yu mel ne  yéen  rawa ti na ku mel ne yaw moom  ngir di maana jànga ci yaw   njagum wolof ,diine,Hadda ak cosaan   waaye sëriñ Tuubaa mi nga nuy jàngal  nak kenn mu nu laa fay  xanaa Yàlla rekk mo am sa fay ko yàll na la fayal bopaam .
noongi ñaan Yàlla mu may la kàttan  tey sakku  boonu ma ne dimbali ci  tekkil nu Màssaalikal  jinaan  Bu seex Hamadu bàmba, Alxuraan bi ñu tekki ci wolof waaye  arafi  araab lañ ko binde, kon boo nu ko manoon na tekki ci  araff bii nuy binde  koon da na tax  xale yu barri mann cee joti  ndax baree waakoon na ñu xammul  arafi Araab  te  doonte Frânse lañ jàngoon sax kon bëgg giñuy béga xam sen diine di na leen jañtal  ci jéema Ijantu  wolofal.
Kariim jóob.
beenjaro@yaho.es

Santees na ci soññee gi, waaye fii fi biir Wiiki bi lu sàkkan lu man a jàngalee ngi fi, dee ci sëgg, soo siggee màndi as lëf, teewul sama E-bataaxal (email) mooy sakkmultiservices@yhotmail.com. Ngir lu aju ci tekkig Masaalig soo bindee waxtaanees ci. Jaajëf--Abdu Xaadir Kebe (xëtu waxtaanuwaay) 12 Suwe 2011 à 12:57 (UTC)[répondre]