Qin Shi Huang wuute gi ci sumb yi

Jóge Wikipedia.
Contenu supprimé Contenu ajouté
Hnusazeig (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 : Rëdd 1 :
moo doonoon imbraatóor bu njëkk bu Siin gees Bennal. Ginnaaw bi mu bennalee Siin, mook njiitu xelalkatam yi Li Si def nañu am mbooloom ay yewenal (reformes) yu koom ak politig yu mag, def it ay sémb yu ngand yu ëmbaale sumb bu njëkk bu Miir bu Mag bu Siin bi. Waaye nguurug jaay-dooleem ga ( nga xam ne lakk na ay téer, suul ay woroom xam-xam) tax na muy jëmm ju jeqi dàggasante ci taariixu Siin
Qin Shi Huang moo doonoon imbraatóor bu njëkk bu '''Siin gees Bennal'''. Ginaaw bi mu bennalee Siin, moom ak njiitu xelalkatam yi Li Si, def nañu am mbooloom ay yéwénal (reformes) yu koom ak politig yu mag, def it ay sémb yu mag, yu ëmbaale sumb (version)bu njëkk bu Miir bu Mag (the great wall)bu Siin bi. Waaye nguurug jaay-dooleem ga ( nga xam ne lakk na ay téere, suul ay woroomi xam-xam) tax na muy jëmm ju jeqi dàggasante ci taariixu Siin


[[Wàll:Taariix]]
[[Wàll:Taariix]]

Sumb bu 29 Mee 2011 à 02:19

Qin Shi Huang moo doonoon imbraatóor bu njëkk bu Siin gees Bennal. Ginaaw bi mu bennalee Siin, moom ak njiitu xelalkatam yi Li Si, def nañu am mbooloom ay yéwénal (reformes) yu koom ak politig yu mag, def it ay sémb yu mag, yu ëmbaale sumb (version)bu njëkk bu Miir bu Mag (the great wall)bu Siin bi. Waaye nguurug jaay-dooleem ga ( nga xam ne lakk na ay téere, suul ay woroomi xam-xam) tax na muy jëmm ju jeqi dàggasante ci taariixu Siin