Doxalukaay bu mbëj wuute gi ci sumb yi

Jóge Wikipedia.
Contenu supprimé Contenu ajouté
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 : Rëdd 1 :
'''Doxalukaay bu mbëj''', ab [[wuutuloxo]]b [[mbëj]] la, goo xam ne kàttan giy duggu ci moom gu [[mbëj]] la te ga muy génne gu [[doolerandu]] la. Doxalukaay yu mbëj yi am nañu solo lool ci dundiinu jamono ju bees ji, te it dëgg la sax, ne limu doxalukaay yu mbëj yi nekk ci am réew dafay firndeel tolluwaayu jëm-kanamam. Te itam deminu, maanam yokkute walla néewte limu doxalkaay yu mbëj yi ci am réew bokk na ci wonekat yiy firndeel tolluwaayu yokkute ci wàllu [[xarala]] mu réew moomu. Ngir dëggal loolu, doyna xool ci jumtukaay yi nekk ci li ñu wër: ca saxaar ba ci watukaay ak yeneen ak yeneen, yi ngeen xam ne nit ku bees ki moo ngi koy jëfandikoo bu baax, man naa ni sax ñooy doxal sunug dund.
'''Doxalukaay bu mbëj''', ab [[wuutuloxo]]b [[mbëj]] la, boo xam ne kàttan giy duggu ci moom gu [[mbëj]] la te ga muy génne gu [[doolerandu]] la. Doxalukaay yu mbëj yi am nañu solo lool ci dundiinu jamono ju bees ji, te it dëgg la sax, ne limu doxalukaay yu mbëj yi nekk ci am réew dafay firndeel tolluwaayu jëm-kanamam. Maanaam yokkug limu doxalukaay yu mbëj yi ci am réew bokk na ci wonekaay yiy firndeel tolluwaayu yokkuteem ci wàllu [[xarala]] mu réew moomu. Ngir dëggal loolu, doy na xool ci jumtukaay yi nekk ci li ñu wër: ca saxaar ba ci watukaay ak yeneen ak yeneen, yi ngeen xam ne nit ku bees ki moo ngi koy jëfandikoo bu baax, man naa ni sax ñooy doxal sunug dund.


Doxalukaay yu mbëj yi dañoo bari te wuute, am na [[doxalukaay bu dawaan bu wéy]], [[doxalukaay bu dawaan bu safaanu]] moom mu séddaliku ci [[doxalukaay bu demandoo]] ak [[doxalukaay bu demandoodi]],.
== Xaralay doxin gi ==


=== Wàll gi solowu: ===
== Xaralay doxiin gi ==

* [[Wëndeelukat]]
=== Wàll gi solowu ===
* [[Tekkaaralkat]]
* [[Toolu Bijjaakon]]
* [[Wëndeeluwaan]]
* [[Tekkaaralaan]]
* [[Toolu bijjaakon]]
* [[Bijjaakon]]
* [[Bijjaakon]]


=== Doxin ===
=== Doxiin ===
Dawaanu [[mbëj]] gi day jaar ci ag lëmës gu ñu wëndeel ci ab doggub weñ bi tudd [[Tekkaaralkat]] bi. Lëmës googu, gi ñu defare ak wëñu përëm, jur ab toolu mbëjbijjaakon bu ca dawaan jaaree. Toolu mbëjbijjaakon boobu dañ koy sóob ci beneen toolu mbëjbijjaakon gu lëmës gu [[wëndeelukat]] bi jur, mi melokaanoo teewaayu ñaar walla ñetti seexi [[dott]]. [[Wëndeelukat]] bi tambalee wëndeelu ci sababu njureelu mbëjbijjaakon; bëj-gànnaaru toolu bijjaakon gu wëndeelukat bi day wootalante ak bëj-saalumu toolu bijjaakon gu tekkaaralkat bi. Xaaju wëndeelu gu nekk, dott bi day soppeeku, ci noonu la wëndeelu gi man a wéyee.
[[Dawaanu mbëj]] bi day jaar ci ag lëmës gu ñu wëndeel ci ab dogub weñ bi tudd tekkaaralaan bi. Lëmës googu, gi ñu defare ak wëñu përëm (naka-jekk përëm lay doon waaye manees na koo defaree ak beneen xeetu wommatukaay), dafay jur ab [[toolu mbëjbijjaakon]], tool bi dafay feeñ niki ag walug bijjaakon, di lees man a nakk. Danu koy jàppee niki jenn doole di lees di wax [[dooley Lorentz]]. Toolu mbëjbijjaakon boobu dafay duggante ak toolu mbëjbijjaakon gu lëmës gu wëndeeluwaan bi jur, mi melokaanoo teewaayu ñaar walla ñetti seexi [[dott]]. Wëndeeluwaan bi tambalee wëndeelu ci ndimbalu dooley Lorentz; bëj-gànnaaru toolu bijjaakon bu wëndeeluwaan bi day bijjante ak bëj-saalumu toolu bijjaakon bu tekkaaralaan bi. Xaaju wëndeelu gu nekk, dott bi day soppeeku, ci noonu la wëndeelu gi man a wéyee.


Doxalukaay bii, ci dawaan gu safaanu rek lay doxee, ndax ci dawaan safaanu rek la bijjaakon di judd. Suy dox, ag wàll gu néew ci kàttanu mbëj gi day soppeeku tanggoor ngir [[njeexitu joule]].
Xeetu doxalukaay bii, ci [[dawaan bu safaanu]] rek lay doxee, ndax ci dawaan bu safaanu rek la bijjaakon buy soppiku di judd. Suy dox, ag wàll gu néew ci kàttanu mbëj gi day soppeeku tangoor ngir [[njeexitu joule]].


== Taariixam ==
== Taariixam ==
Ci atum 1821, lu weesu xamteg feñte gu mbëjbijjaakon gi, simikat boobu di Ørsted xamlewoon, la [[jëmmalkat]] bu waa-angalteer bii di [[Michael Faraday]]defar ñaari wuutuloxo ngir jóox li mu duppee ab wëndeelug mbëjbijjaakon: ab doxub dooley bijjaakon bu mbegewu te wéy, ci lu wër ab wëñ, ci maanaa mooy faramfaceg doxalukaay bu mbëj gu njëkk.
Ci atum 1821, lu weesu xamteg feñte gu [[mbëjbijjaakon]] gi simikat boobu di Ørsted xamle woon, la [[jëmmalkat]] bu waa-angalteer bii di Michael Faraday defar ñaari wuutuloxo ngir sàkk li mu duppee ag wëndeelug mbëjbijjaakon: ab doxub dooley bijjaakon bu mbegewu te wéy, ci lu wër ab wëñ, ci maanaa mooy faramfaceg doxalukaay bu mbëj gu njëkk.
== Lëkkalekaay yu biir ==
== Lëkkalekaay yu biir ==
* [[Doxalkaay bu demandoo]]
* [[dawaan bu safaanu]]
* [[Doxalkaay bu demandoowul]]
* [[dawaan bu wéy]]
* [[Doxalukaay bu wéy]]
* [[dawaan bu safaanoo]]


{{wikibaatukaay}}
{{wikibaatukaay}}

Sumb bu 26 Maars 2010 à 17:02

Doxalukaay bu mbëj, ab wuutuloxob mbëj la, boo xam ne kàttan giy duggu ci moom gu mbëj la te ga muy génne gu doolerandu la. Doxalukaay yu mbëj yi am nañu solo lool ci dundiinu jamono ju bees ji, te it dëgg la sax, ne limu doxalukaay yu mbëj yi nekk ci am réew dafay firndeel tolluwaayu jëm-kanamam. Maanaam yokkug limu doxalukaay yu mbëj yi ci am réew bokk na ci wonekaay yiy firndeel tolluwaayu yokkuteem ci wàllu xarala mu réew moomu. Ngir dëggal loolu, doy na xool ci jumtukaay yi nekk ci li ñu wër: ca saxaar ba ci watukaay ak yeneen ak yeneen, yi ngeen xam ne nit ku bees ki moo ngi koy jëfandikoo bu baax, man naa ni sax ñooy doxal sunug dund.

Doxalukaay yu mbëj yi dañoo bari te wuute, am na doxalukaay bu dawaan bu wéy, doxalukaay bu dawaan bu safaanu moom mu séddaliku ci doxalukaay bu demandoo ak doxalukaay bu demandoodi,.

Xaralay doxiin gi

Wàll gi solowu

Doxiin

Dawaanu mbëj bi day jaar ci ag lëmës gu ñu wëndeel ci ab dogub weñ bi tudd tekkaaralaan bi. Lëmës googu, gi ñu defare ak wëñu përëm (naka-jekk përëm lay doon waaye manees na koo defaree ak beneen xeetu wommatukaay), dafay jur ab toolu mbëjbijjaakon, tool bi dafay feeñ niki ag walug bijjaakon, di lees man a nakk. Danu koy jàppee niki jenn doole di lees di wax dooley Lorentz. Toolu mbëjbijjaakon boobu dafay duggante ak toolu mbëjbijjaakon gu lëmës gu wëndeeluwaan bi jur, mi melokaanoo teewaayu ñaar walla ñetti seexi dott. Wëndeeluwaan bi tambalee wëndeelu ci ndimbalu dooley Lorentz; bëj-gànnaaru toolu bijjaakon bu wëndeeluwaan bi day bijjante ak bëj-saalumu toolu bijjaakon bu tekkaaralaan bi. Xaaju wëndeelu gu nekk, dott bi day soppeeku, ci noonu la wëndeelu gi man a wéyee.

Xeetu doxalukaay bii, ci dawaan bu safaanu rek lay doxee, ndax ci dawaan bu safaanu rek la bijjaakon buy soppiku di judd. Suy dox, ag wàll gu néew ci kàttanu mbëj gi day soppeeku tangoor ngir njeexitu joule.

Taariixam

Ci atum 1821, lu weesu xamteg feñte gu mbëjbijjaakon gi simikat boobu di Ørsted xamle woon, la jëmmalkat bu waa-angalteer bii di Michael Faraday defar ñaari wuutuloxo ngir sàkk li mu duppee ag wëndeelug mbëjbijjaakon: ab doxub dooley bijjaakon bu mbegewu te wéy, ci lu wër ab wëñ, ci maanaa mooy faramfaceg doxalukaay bu mbëj gu njëkk.

Lëkkalekaay yu biir

wikbaatukaay am na xët wu tudd: Doxalukaay bu mbëj