Tamxarit wuute gi ci sumb yi

Jóge Wikipedia.
Contenu supprimé Contenu ajouté
Alexbot (waxtaancëru)
m robot Adding: no:Muharram
Ibou (waxtaancëru)
yokkug lëkkalekaay: Bisu Tamxarit
Rëdd 4 : Rëdd 4 :
* Ci lees di xewal bés bu njëkk ci at mi. Ci [[senegaal]] ci lañuy [[Taajabóon|taajabóon]].
* Ci lees di xewal bés bu njëkk ci at mi. Ci [[senegaal]] ci lañuy [[Taajabóon|taajabóon]].
* Ci la shiit yi di fattalikoo xareb [[Karbalaa]] ca [[Iraak]]. Ca lañu faatee [[Useynu ben Aali]] sëtu yonent bi.
* Ci la shiit yi di fattalikoo xareb [[Karbalaa]] ca [[Iraak]]. Ca lañu faatee [[Useynu ben Aali]] sëtu yonent bi.
*[[Bisu Tamxarit]]

[[Wàll:weeri wolof]]
[[Wàll:weeri wolof]]
{{Weeriwolof}}
{{Weeriwolof}}

Sumb bu 30 Samwiyee 2010 à 19:35

Tamxarit (محرم ci araab), mooy weer wi njëkk ci yu gàddaay gi, moom nag bokk na ci li ñuy wax ci Lislaam "Al-ashur al-hurum", (maanaam weer yu am worma yi): tamxarit nag tuddees na ko ci araab "muharram" ngir ne araab yi dañu ci daan araamal xeex.

Xew-xew

Weeri wolof

Tamxarit | Diggi-gàmmu | Gàmmu | Rakki-gàmmu | Rakkaati-gàmmu | Maami-koor | Ndeyi-koor | Baraxlu | Koor | Kori | Diggi-tabaski Tabaski