Dawaan bu safaanu wuute gi ci sumb yi

Jóge Wikipedia.
Contenu supprimé Contenu ajouté
Ibou (waxtaancëru)
m Tuddewaat nañ Dawaan gu safaanu léegi mooy Dawaan bu safaanu
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 : Rëdd 1 :
'''Dawaan gu safaanu''' ('''DS''' walla '''AC''' ci [[wu-angalteer]]: Alternating Current) màndargoo ag walug [[dawaan]] guy soppiku ci jamono muy ci [[taraay]] walla ci jubluwaay.
'''Dawaan bu safaanu''' ('''DS''' walla '''AC''' ci [[wu-angalteer]]: Alternating Current) màndargoo ag walug [[dawaan]] guy soppiku ci jamono muy ci [[taraay]] walla ci jubluwaay.
== Doxiin ==
== Doxiin ==
Naka-jekk dawaanu [[mbëj]] suñu koy séddale ci dawaan gu safaanu gu [[Baraay|baraayam]] sax ci 50 Hz walla 60 [[Hz]] lees koy defe (+ ak - bi dañuy safaanu ci watatukaay bi juroom-fukki saa yu ne).
Naka-jekk dawaanu [[mbëj]] suñu koy séddale ci dawaan bu safaanu bu [[Baraay|baraayam]] sax ci 50 Hz walla 60 [[Hz]] lees koy defe (+ ak - bi dañuy safaanu ci watatukaay bi juroom-fukki saa yu ne).


Jëfandikoo gu dawaan gu safaanu mi gi jóge ci li [[jurukaayu dawaan]] yi, ci yaxanaay ci koom-koom ak seenug yomb a defar, di jur dawaan gu safaanu ci anam gu yomb, kon dawaan gi ci boppam kenn du ko soppiwaat laataa ag jëfandikoo.
Jëfandikoo gu dawaan bu safaanu mi gi jóge ci li [[Jurukaay|jurukaayu dawaan]] yi, ci yaxanaay ci koom-koom ak seenug yomb a defar, di jur dawaan bu safaanu ci anam gu yomb, kon dawaan bi ci boppam kenn du ko soppiwaat laataa ag jëfandikoo.


Fi njariñ li gën a feeñee sax mooy séddaleeb dawaan gu safaanu bir na ne moo gën a yaxan [[dawaan gu wéy]] ci séddaleeb [[taraay bu kawe]] (ñakkug kàttan gi ci buum yu gudd yi moo gën a néew). rawatina, ci diggante gu [[gennwéq]] walla wéq yu bari, bir na yaxanaay gu [[ñettiwéq]] di gees gën a jëfandikoo ndax néewteey ñakkug kàttan ngir njeexitu [[Joule]] (moo tax dijjaayu watatukaay yi gën a néew, maanaam wëñ yu gën a sew); jëfandikoog dawaan gu safaanu gu ñettiwéq lawal na buumi yóbb yi ci diggante yu gudd yi.
Fi njariñ li gën a feeñee sax mooy séddaleeb dawaan bu safaanu bir na ne moo gën a yaxan [[dawaan bu wéy]] ci séddaleeb [[taraay bu kawe]] (ñakkug kàttan gi ci buum yu gudd yi moo gën a néew). rawatina, ci diggante gu [[gennwéq]] walla wéq yu bari, bir na yaxanaay gu [[ñettiwéq]] di gees gën a jëfandikoo ndax néewteey ñakkug kàttan ngir njeexitu [[Joule]] (moo tax dijjaayu watatukaay yi gën a néew, maanaam wëñ yu gën a sew); jëfandikoog dawaan bu safaanu bu ñettiwéq lawal na buumi yóbb yi ci diggante yu gudd lool yi.
Genn Màndarga gu am-solo gu dawaan gu safaanu, ba waral ci genn wàll li tax ñépp jël ko, mooy yomb gee jëfandikoom fu nekk, yomb gee soppi ci lim yu wuute ci [[taraay]]u [[dawaan]], ci ndimbalu [[soppikaay]] yi, ak ñakkug kàttan gu digu.


Genn Màndarga gu am-solo gu dawaan bu safaanu, ba waral ci genn wàll li tax ñépp jël ko, mooy yomb gee jëfandikoo fu nekk, yomb gee soppi ci lim yu wuute ci [[taraay]]u [[dawaan]], ci ndimbalu [[soppikaay]] yi, ak ñakkug kàttan gu digu.
Donte yenn jumtukaay yi [[dawaan gu wéy]] lañuy doxe, waaye loolu manees na koo ame ci dawaan gu safaanu, sunu jëfandikoo ab [[jubbantikaay]].


Donte yenn jumtukaay yi [[dawaan bu wéy]] lañuy doxe, waaye loolu manees na koo ame ci dawaan bu safaanu, sunu jëfandikoo ab [[jubbantikaay]].
Sunu jëfandikoo ag xaralag [[mbëjfeppal]] gu kàttan gu yaxan, manees naa jëfandikoo dawaan gu wéy ngir am dawaan gu safaanu, jur ko ci yenn anami [[baraay]], [[melokaanu duus]] ak taraay jaare ko ciy jumtukaay yees duppee [[Jallarbikaay|jallarbikaay]].
== Taariix ==


Suñu jëfandikoo ag xaralag [[mbëjfeppal gu kàttan]] gu ñaw, manees naa jëfandikoo dawaan bu wéy ngir am dawaan bu safaanu, jur ko ci yenn anami [[baraay]], [[melokaanu duus]] ak taraay jaare ko ciy jumtukaay yees duppee [[Jallarbikaay|jallarbikaay]].

== Taariix ==
[[Dencukaay:WorldMap Voltage&Frequency.png|400px|thumb|right|Lonkoyoonu àdduna bi bees melool aju ci taraay a baraayu kàttanu mbëj ci ndombo yiy séddale dawaan gi ci kër yi.]]
[[Dencukaay:WorldMap Voltage&Frequency.png|400px|thumb|right|Lonkoyoonu àdduna bi bees melool aju ci taraay a baraayu kàttanu mbëj ci ndombo yiy séddale dawaan gi ci kër yi.]]


Ca njalbeenu njëfandikoog kàttanu mbëj ci ndefar gi ci XIX<sup>u</sup> xarnu [[daawaan gu wéy]] lañu doon jëfandikoo, ndax li mu doonoon lu neex a rënk ciy [[tegle]] ak li mu gën a wóor dawaan gu safaanu. Tomb bu mujj bi Thomas Alva Edison mooy ki ko doon wax ci lees tuddewoon [[xareeb dawaan yi]].
Ca njalbeenu njëfandikug kàttanu mbëj ci ndefar gi ci XIX<sup>u</sup> xarnu [[daawaan bu wéy]] lañu doon jëfandikoo, ndax li mu doonoon lu neex a rënk ciy [[tegle]] ak li mu gën a wóor dawaan bu safaanu. Tomb bu mujj bi Thomas Alva Edison mooy ki ko doon wax ci lees tuddewoon [[xareeb dawaan yi]].


Dawaan gu safaanu, gi soloom doonoon lu beneen xaaj bi boole woon [[Nikola Tesla]] ak [[George Westinghouse]] doon aar, manul a ñakk ci njëfandikoo gu ab [[soppikaay]], moom mi tax ñuy man jokkalante mbëj mi ci diggante yu gudd. Te itam [[doxalukaayu mbëj]] yu dawaan gu safaanu ñoo gën a wóor te gën a yaxan yu wéy yi.
Dawaan bu safaanu, gi soloom doonoon lu beneen xaaj bi boole woon [[Nikola Tesla]] ak [[George Westinghouse]] doon aar, manul a ñakk ci njëfandiku gu ab [[soppalikaay]], moom mi tax ñuy man jokkalante mbëj mi ci diggante yu gudd. Te itam [[doxalukaayu mbëj]] yu dawaan bu safaanu ñoo gën a wóor te gën a yaxan yu dawaan yu wéy yi.


Ci jamono jii ci [[àdduna]] bi dawaanu mbëj ci ñaari [[baraay]] lañu koy séddalee, 50 Hz([[Tugal]], [[Asi]], [[Afrig]]) ak 60 Hz([[Diiwaan-yu-Bennoo]] ak goxu [[Aamerig]] gépp ci lu daj, genn xaaju [[sapoŋ]]) ak taraay yu wuute.
Ci jamono jii ci [[àdduna]] bi dawaanu mbëj ci ñaari [[baraay]] lañu koy séddalee, 50 Hz([[Tugal]], [[Asi]], [[Afrig]]) ak 60 Hz([[Diiwaan-yu-Bennoo]] ak goxu [[Aamerig]] bépp ci lu daj, genn xaaju [[sapoŋ]]) ak taraay yu wuute.


== Xool it ==
== Xool it ==

Sumb bu 13 Samwiyee 2010 à 15:46

Dawaan bu safaanu (DS walla AC ci wu-angalteer: Alternating Current) màndargoo ag walug dawaan guy soppiku ci jamono muy ci taraay walla ci jubluwaay.

Doxiin

Naka-jekk dawaanu mbëj suñu koy séddale ci dawaan bu safaanu bu baraayam sax ci 50 Hz walla 60 Hz lees koy defe (+ ak - bi dañuy safaanu ci watatukaay bi juroom-fukki saa yu ne).

Jëfandikoo gu dawaan bu safaanu mi gi jóge ci li jurukaayu dawaan yi, ci yaxanaay ci koom-koom ak seenug yomb a defar, di jur dawaan bu safaanu ci anam gu yomb, kon dawaan bi ci boppam kenn du ko soppiwaat laataa ag jëfandikoo.

Fi njariñ li gën a feeñee sax mooy séddaleeb dawaan bu safaanu bir na ne moo gën a yaxan dawaan bu wéy ci séddaleeb taraay bu kawe (ñakkug kàttan gi ci buum yu gudd yi moo gën a néew). rawatina, ci diggante gu gennwéq walla wéq yu bari, bir na yaxanaay gu ñettiwéq di gees gën a jëfandikoo ndax néewteey ñakkug kàttan ngir njeexitu Joule (moo tax dijjaayu watatukaay yi gën a néew, maanaam wëñ yu gën a sew); jëfandikoog dawaan bu safaanu bu ñettiwéq lawal na buumi yóbb yi ci diggante yu gudd lool yi.

Genn Màndarga gu am-solo gu dawaan bu safaanu, ba waral ci genn wàll li tax ñépp jël ko, mooy yomb gee jëfandikoo fu nekk, yomb gee soppi ci lim yu wuute ci taraayu dawaan, ci ndimbalu soppikaay yi, ak ñakkug kàttan gu digu.

Donte yenn jumtukaay yi dawaan bu wéy lañuy doxe, waaye loolu manees na koo ame ci dawaan bu safaanu, sunu jëfandikoo ab jubbantikaay.

Suñu jëfandikoo ag xaralag mbëjfeppal gu kàttan gu ñaw, manees naa jëfandikoo dawaan bu wéy ngir am dawaan bu safaanu, jur ko ci yenn anami baraay, melokaanu duus ak taraay jaare ko ciy jumtukaay yees duppee jallarbikaay.

Taariix

Lonkoyoonu àdduna bi bees melool aju ci taraay a baraayu kàttanu mbëj ci ndombo yiy séddale dawaan gi ci kër yi.

Ca njalbeenu njëfandikug kàttanu mbëj ci ndefar gi ci XIXu xarnu daawaan bu wéy lañu doon jëfandikoo, ndax li mu doonoon lu neex a rënk ciy tegle ak li mu gën a wóor dawaan bu safaanu. Tomb bu mujj bi Thomas Alva Edison mooy ki ko doon wax ci lees tuddewoon xareeb dawaan yi.

Dawaan bu safaanu, gi soloom doonoon lu beneen xaaj bi boole woon Nikola Tesla ak George Westinghouse doon aar, manul a ñakk ci njëfandiku gu ab soppalikaay, moom mi tax ñuy man jokkalante mbëj mi ci diggante yu gudd. Te itam doxalukaayu mbëj yu dawaan bu safaanu ñoo gën a wóor te gën a yaxan yu dawaan yu wéy yi.

Ci jamono jii ci àdduna bi dawaanu mbëj ci ñaari baraay lañu koy séddalee, 50 Hz(Tugal, Asi, Afrig) ak 60 Hz(Diiwaan-yu-Bennoo ak goxu Aamerig bépp ci lu daj, genn xaaju sapoŋ) ak taraay yu wuute.

Xool it

Téerekaay