Dawaan bu safaanu wuute gi ci sumb yi

Jóge Wikipedia.
Contenu supprimé Contenu ajouté
Ibou (waxtaancëru)
Xët wu bees : thumb|200px|rigth|njunju dawaan gu safaanu '''Dawaan gu safaanu''' ('''DS''' walla '''AC''' ci wu-angalteer: Alternating Current) màndargoo ag walug...
 
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 : Rëdd 1 :
[[Dencukaay:Simbolo_AC.gif|thumb|200px|rigth|njunju dawaan gu safaanu]]

'''Dawaan gu safaanu''' ('''DS''' walla '''AC''' ci [[wu-angalteer]]: Alternating Current) màndargoo ag walug [[dawaan]] guy soppiku ci jamono muy ci [[taraay]] walla ci jubluwaay.
'''Dawaan gu safaanu''' ('''DS''' walla '''AC''' ci [[wu-angalteer]]: Alternating Current) màndargoo ag walug [[dawaan]] guy soppiku ci jamono muy ci [[taraay]] walla ci jubluwaay.
== Doxiin ==
== Doxiin ==
Rëdd 23 : Rëdd 21 :
Ci jamono jii ci [[àdduna]] bi dawaanu mbëj ci ñaari [[baraay]] lañu koy séddalee, 50 Hz([[Tugal]], [[Asi]], [[Afrig]]) ak 60 Hz([[Diiwaan-yu-Bennoo]] ak goxu [[Aamerig]] gépp ci lu daj, genn xaaju [[sapoŋ]]) ak taraay yu wuute.
Ci jamono jii ci [[àdduna]] bi dawaanu mbëj ci ñaari [[baraay]] lañu koy séddalee, 50 Hz([[Tugal]], [[Asi]], [[Afrig]]) ak 60 Hz([[Diiwaan-yu-Bennoo]] ak goxu [[Aamerig]] gépp ci lu daj, genn xaaju [[sapoŋ]]) ak taraay yu wuute.


== Xool it ==
*[[Dawaan gu wéy]]

*[[Dawaanu mbëj]]

*[[Kàttanu mbëj]]

*[[mbëj]]
==Téerekaay ==
==Téerekaay ==


Rëdd 38 : Rëdd 44 :


* {{en}}Ernst Julius Berg: [http://www.archive.org/details/electricalengine00bergrich ''Electrical Engineering, Advanced Course''] (McGrawHill, New York, 1916)
* {{en}}Ernst Julius Berg: [http://www.archive.org/details/electricalengine00bergrich ''Electrical Engineering, Advanced Course''] (McGrawHill, New York, 1916)


[[Wàll:dawaanu mbëj]]


[[ar:تيار متردد]] [[be-x-old:Зьменны струм]] [[bg:Променлив ток]] [[bn:পরিবর্তী তড়িৎ প্রবাহ]] [[ca:Corrent altern]] [[cs:Střídavý proud]] [[da:Vekselstrøm]] [[de:Wechselstrom]] [[el:Εναλλασσόμενο ρεύμα]] [[en:Alternating current]] [[eo:Alterna kurento]] [[es:Corriente alterna]] [[et:Vahelduvvool]] [[fa:جریان متناوب]]

[[fi:Vaihtovirta]]

[[fr:Courant alternatif]]

[[gl:Corrente alterna]] [[he:זרם חילופין]] [[hi:प्रत्यावर्ती धारा]] [[hr:Izmjenična električna struja]] [[hu:Váltakozó áram]] [[id:Arus bolak-balik]] [[io:Alternanta fluo]] [[is:Riðstraumur]] [[it:Corrente alternata]] [[ja:交流]] [[ko:교류]] [[ku:Sirêma berguhêr]] [[lt:Kintamoji elektros srovė]] [[lv:Maiņstrāva]] [[ml:പ്രത്യാവര്‍ത്തിധാരാ വൈദ്യുതി]] [[ms:Arus ulang-alik]] [[nl:Wisselstroom]] [[no:Vekselstrøm]] [[pl:Prąd przemienny]] [[pt:Corrente alternada]] [[ro:Curent alternativ]] [[ru:Переменный ток]] [[sh:Izmjenična struja]] [[simple:Alternating current]] [[sk:Striedavý prúd]] [[sl:Izmenični električni tok]] [[sr:Наизменична струја]] [[su:Arus listrik bulak-balik]] [[sv:Växelström]] [[ta:மாறுதிசை மின்னோட்டம்]] [[tr:Alternatif akım]] [[uk:Змінний струм]] [[vi:Điện xoay chiều]] [[zh:交流電]]

Sumb bu 3 Samwiyee 2010 à 17:53

Dawaan gu safaanu (DS walla AC ci wu-angalteer: Alternating Current) màndargoo ag walug dawaan guy soppiku ci jamono muy ci taraay walla ci jubluwaay.

Doxiin

Naka-jekk dawaanu mbëj suñu koy séddale ci dawaan gu safaanu gu baraayam sax ci 50 Hz walla 60 Hz lees koy defe (+ ak - bi dañuy safaanu ci watatukaay bi juroom-fukki saa yu ne).

Jëfandikoo gu dawaan gu safaanu mi gi jóge ci li jurukaayu dawaan yi, ci yaxanaay ci koom-koom ak seenug yomb a defar, di jur dawaan gu safaanu ci anam gu yomb, kon dawaan gi ci boppam kenn du ko soppiwaat laataa ag jëfandikoo.

Fi njariñ li gën a feeñee sax mooy séddaleeb dawaan gu safaanu bir na ne moo gën a yaxan dawaan gu wéy ci séddaleeb taraay bu kawe (ñakkug kàttan gi ci buum yu gudd yi moo gën a néew). rawatina, ci diggante gu gennwéq walla wéq yu bari, bir na yaxanaay gu ñettiwéq di gees gën a jëfandikoo ndax néewteey ñakkug kàttan ngir njeexitu Joule (moo tax dijjaayu watatukaay yi gën a néew, maanaam wëñ yu gën a sew); jëfandikoog dawaan gu safaanu gu ñettiwéq lawal na buumi yóbb yi ci diggante yu gudd yi. Genn Màndarga gu am-solo gu dawaan gu safaanu, ba waral ci genn wàll li tax ñépp jël ko, mooy yomb gee jëfandikoom fu nekk, yomb gee soppi ci lim yu wuute ci taraayu dawaan, ci ndimbalu soppikaay yi, ak ñakkug kàttan gu digu.

Donte yenn jumtukaay yi dawaan gu wéy lañuy doxe, waaye loolu manees na koo ame ci dawaan gu safaanu, sunu jëfandikoo ab jubbantikaay.

Sunu jëfandikoo ag xaralag mbëjfeppal gu kàttan gu yaxan, manees naa jëfandikoo dawaan gu wéy ngir am dawaan gu safaanu, jur ko ci yenn anami baraay, melokaanu duus ak taraay jaare ko ciy jumtukaay yees duppee jallarbikaay.

Taariix

Lonkoyoonu àdduna bi bees melool aju ci taraay a baraayu kàttanu mbëj ci ndombo yiy séddale dawaan gi ci kër yi.

Ca njalbeenu njëfandikoog kàttanu mbëj ci ndefar gi ci XIXu xarnu daawaan gu wéy lañu doon jëfandikoo, ndax li mu doonoon lu neex a rënk ciy tegle ak li mu gën a wóor dawaan gu safaanu. Tomb bu mujj bi Thomas Alva Edison mooy ki ko doon wax ci lees tuddewoon xareeb dawaan yi.

Dawaan gu safaanu, gi soloom doonoon lu beneen xaaj bi boole woon Nikola Tesla ak George Westinghouse doon aar, manul a ñakk ci njëfandikoo gu ab soppikaay, moom mi tax ñuy man jokkalante mbëj mi ci diggante yu gudd. Te itam doxalukaayu mbëj yu dawaan gu safaanu ñoo gën a wóor te gën a yaxan yu wéy yi.

Ci jamono jii ci àdduna bi dawaanu mbëj ci ñaari baraay lañu koy séddalee, 50 Hz(Tugal, Asi, Afrig) ak 60 Hz(Diiwaan-yu-Bennoo ak goxu Aamerig gépp ci lu daj, genn xaaju sapoŋ) ak taraay yu wuute.

Xool it

Téerekaay