Maars (weer) wuute gi ci sumb yi

Jóge Wikipedia.
Contenu supprimé Contenu ajouté
MauritsBot (waxtaancëru)
m robot Adding: mhr:Ӱярня; cosmetic changes
MauritsBot (waxtaancëru)
m robot Adding: udm:Март
Rëdd 158 : Rëdd 158 :
[[ts:Nyenyankulu]]
[[ts:Nyenyankulu]]
[[tt:Mart]]
[[tt:Mart]]
[[udm:Март]]
[[uk:Березень]]
[[uk:Березень]]
[[ur:مارچ]]
[[ur:مارچ]]

Sumb bu 15 Sulet 2009 à 11:04

Weeru Maars mooy ñetteelu weer ci arminaatu Gregori ak ci bu Suul.

Baat baa ngi jóge ci latin: Maars, ngir màggale ko yàllay waa-rom ja: Martius (yàllay xare yi), ci weer wii daanaka la xare yi daan door, ndax ci la tangaay bi di tambalee. Ca jamono ju yàgg ja, moo nekkoon weer wi njëkk ci arminaatu waa-rom.

Ci arminaatu weer, walla ci weeru wolof, mooy gammu.

Weer
Samwie | Fewirie | Maars | Awril | Mee | Suwe | Sulet | Ut | Sattumbar | Oktoobar | Nowembar | Disambar