Gàmmu wuute gi ci sumb yi

Jóge Wikipedia.
Contenu supprimé Contenu ajouté
Ibou (waxtaancëru)
Xët wu bees : '''Gàmmu''', ( ci araab ربيع الأول) mooy ñetteelu weer ci weeri wolof tuddees na ko noonu ngir ne araab yi dañu ci daan lolliwu, maanaam daan ci am am ñax, di…
 
LaaknorBot (waxtaancëru)
m robot Modifying: fr:Rabia al awal
Rëdd 12 : Rëdd 12 :
[[en:Rabi' al-awwal]]
[[en:Rabi' al-awwal]]
[[fa:ربیع‌الاول]]
[[fa:ربیع‌الاول]]
[[fr:Rabia al Awal]]
[[fr:Rabia al awal]]
[[he:רביע אל-אוול]]
[[he:רביע אל-אוול]]
[[id:Rabiul awal]]
[[id:Rabiul awal]]

Sumb bu 24 Suwe 2009 à 00:05

Gàmmu, ( ci araab ربيع الأول) mooy ñetteelu weer ci weeri wolof tuddees na ko noonu ngir ne araab yi dañu ci daan lolliwu, maanaam daan ci am am ñax, di ci sàmm seenug jur, am ñu ne daa dëppoo ak lolli bi moo tax ñu tudde ko ko.

Ci wolof nak daa yem ak weer wees di màggale juddug yonnent bi.

Weeri wolof

Tamxarit | Diggi-gàmmu | Gàmmu | Rakki-gàmmu | Rakkaati-gàmmu | Maami-koor | Ndeyi-koor | Baraxlu | Koor | Kori | Diggi-tabaski Tabaski