Pël wuute gi ci sumb yi

Jóge Wikipedia.
Contenu supprimé Contenu ajouté
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 3 : Rëdd 3 :
[[Image:Eleveurs Peuls.jpg|thumb|200px|left|Sàmmkatu Pël bu Gurma, bëj-saalumu [[Gao]], [[Mali]]]] ÑÑoom ci seen bopp dañuy wax Pullo wala FulBe. [[Isipt]] mooy réew mi ñu bawoo. Pël ya ca Isipt ay nit ñu ñuul lañu nekkoon. Ba noppi, ay nit ñu weex, ñëw ca seenum réew juge [[Asi]] ak [[Tugal]] , bokk na ca xeet yooya: Scythe, Aryen, Phrygien, Hittite, askan yu bari yu ñuy tudde ay waa End-tugal (Indo-européen). Pël yu ñuul yi ak nit ñu weex ñi dañoo jaxaasoo woon. Lii moo tax Pël yi gën a xees, gën a sew, am kawar gu gën a nooy, bu ñu leen xoolee ci yeneen xeet yu ñuul yi ci Afrig. Ba noppi, Imbraatóor gu Tirki(ñoñ usmaan ñi(les ottonams) ), tegoon nañu loxo réewum Isipt, di fa tege dund gu metti, rawati na ca nit ñu ñuul ña. Lii moo tax Pël ya ak Séeréer sa gàddaay, dëkki ca [[Sudaan]] (Nubie) dëkki seeni maam, soog a dem Senegaal. Pël ak [[Séeréer]] danoo bokk maam, seeni làkk tamit. Yàgg nañoo ànd, dañuy kalante ci seen biir. Ca yoonu [[Tekuruur]], pël ya ca Dexug Senegaal rekk lañu nekkoon ak seeni nag. Booba nekkuñu woon ay jullit. Amuñu woon nguur ndax ak seeni nag ci màng rekk lañu nekke woon. Meew ak Sanqal (ñórndi) moo doonoon seenu lekk. Pël ci boppam am na xeet yu bari (Leyyi/KinDe), Ardo mooy seen Buur: JaawBe yi, UrurBe, WodaaBe, LaaCe, CutinkooBe, YirlaaBe. Am na yeneen KinDe. Màng gi ñu dëkke tax na ñu tuuru ci Sowwu Afrig gépp, ba far delseeti Sudaan, cig muñ ak coona ndax saa su nekk ci dëkki jàmbur yi rekk lañuy nekk, seen nag yi leeg-leeg ñu ruur tooli baykat yi, loolu it di jur xuloo bu rëy ak ŋaayoo ci seen digg ak woroon tool yi.
[[Image:Eleveurs Peuls.jpg|thumb|200px|left|Sàmmkatu Pël bu Gurma, bëj-saalumu [[Gao]], [[Mali]]]] ÑÑoom ci seen bopp dañuy wax Pullo wala FulBe. [[Isipt]] mooy réew mi ñu bawoo. Pël ya ca Isipt ay nit ñu ñuul lañu nekkoon. Ba noppi, ay nit ñu weex, ñëw ca seenum réew juge [[Asi]] ak [[Tugal]] , bokk na ca xeet yooya: Scythe, Aryen, Phrygien, Hittite, askan yu bari yu ñuy tudde ay waa End-tugal (Indo-européen). Pël yu ñuul yi ak nit ñu weex ñi dañoo jaxaasoo woon. Lii moo tax Pël yi gën a xees, gën a sew, am kawar gu gën a nooy, bu ñu leen xoolee ci yeneen xeet yu ñuul yi ci Afrig. Ba noppi, Imbraatóor gu Tirki(ñoñ usmaan ñi(les ottonams) ), tegoon nañu loxo réewum Isipt, di fa tege dund gu metti, rawati na ca nit ñu ñuul ña. Lii moo tax Pël ya ak Séeréer sa gàddaay, dëkki ca [[Sudaan]] (Nubie) dëkki seeni maam, soog a dem Senegaal. Pël ak [[Séeréer]] danoo bokk maam, seeni làkk tamit. Yàgg nañoo ànd, dañuy kalante ci seen biir. Ca yoonu [[Tekuruur]], pël ya ca Dexug Senegaal rekk lañu nekkoon ak seeni nag. Booba nekkuñu woon ay jullit. Amuñu woon nguur ndax ak seeni nag ci màng rekk lañu nekke woon. Meew ak Sanqal (ñórndi) moo doonoon seenu lekk. Pël ci boppam am na xeet yu bari (Leyyi/KinDe), Ardo mooy seen Buur: JaawBe yi, UrurBe, WodaaBe, LaaCe, CutinkooBe, YirlaaBe. Am na yeneen KinDe. Màng gi ñu dëkke tax na ñu tuuru ci Sowwu Afrig gépp, ba far delseeti Sudaan, cig muñ ak coona ndax saa su nekk ci dëkki jàmbur yi rekk lañuy nekk, seen nag yi leeg-leeg ñu ruur tooli baykat yi, loolu it di jur xuloo bu rëy ak ŋaayoo ci seen digg ak woroon tool yi.


Ca atum 1539 Koli Tengella Bâ, mi ngi booke ci Pël ci wetug baayam, bokk it ci Mande yi ci wàllug yaayam (Keyta), dajale woon na sàmmkati Pël yi ak mande yi, ngir ñu man a am doole. Daa di dugg ci yeneen xeet (Wolof, Séeréer, Bajaaranke, Joola, Baga, [[Sooninke]] . Ñoom ñépp ak seen aroo Koli Tengella, ñu yéeg ba Tekuruur, di xeex ak Buur-ba [[Jolof]] ba, ndax kii moo doon yor dëkk ba, ak Lam-Toro ya, Lam-Térmes, Lam-Taga ya, Juroom ñeenti fan soog a yor dëkk ai. Koli Tengella teg na fa njabootam (Denyakoobe yi), tudde na nguur ga Fuuta-Toro (Fuuta mooy dëkku Pël ca seen Làkk). Lii ca Senegaal la xewe.
Ca atum 1539 Koli Tengella Bâ, mi ngi bokke ci Pël ci wetug baayam, bokk it ci Mande yi ci wàllug yaayam (Keyta), dajale woon na sàmmkati Pël yi ak mande yi, ngir ñu man a am doole. Daa di dugg ci yeneen xeet (Wolof, Séeréer, Bajaaranke, Joola, Baga, [[Sooninke]] . Ñoom ñépp ak seen aroo Koli Tengella, ñu yéeg ba Tekuruur, di xeex ak Buur-ba [[Jolof]] ba, ndax kii moo doon yor dëkk ba, ak Lam-Toro ya, Lam-Térmes, Lam-Taga ya, Juroom ñeenti fan soog a yor dëkk ai. Koli Tengella teg na fa njabootam (Denyakoobe yi), tudde na nguur ga Fuuta-Toro (Fuuta mooy dëkku Pël ca seen Làkk). Lii ca Senegaal la xewe.
Ca Mali Pël ya doñoo njëkk am doole ca atum 1818. Booba nag Ahmadu Bari, Sëriñ la nekkoon, dajale na Pëli Jullit yi, ak Mande yu jullit yi ( Mandé Mori yi : Siise, Ture, Silla ), ngir ñu àndandoo xeex (Jiyaar) safaan nguuru Bàmbara yi fi nekkoon (nguuru Ségu ak Kaarta). Buuru Bàmbara yi (Fama) ak seeni jàmbaar (Ton-Dion), amoon nanu doole, lii moo tax Ahmadu Bari tabax Imbraatoor gu Pël ca Massina Kese. ak itam Pël yi, ca Mali, fofu lani eupé woon ba tey (Tey di nek Région De Mopti).
Ca Mali Pël ya doñoo njëkk am doole ca atum 1818. Booba nag Ahmadu Bari, Sëriñ la nekkoon, dajale na Pëli Jullit yi, ak Mande yu jullit yi ( Mandé Mori yi : Siise, Ture, Silla ), ngir ñu àndandoo xeex (Jiyaar) safaan nguuru Bàmbara yi fi nekkoon (nguuru Ségu ak Kaarta). Buuru Bàmbara yi (Fama) ak seeni jàmbaar (Ton-Dion), amoon nanu doole, lii moo tax Ahmadu Bari tabax Imbraatoor gu Pël ca Massina Kese. ak itam Pël yi, ca Mali, foofu lañu ëppe woon ba tay (Tay jii foofa mooy diiwaan (Région) bu Mopti).
Ca Ginne, Pël y danu fa yag, wa é Mandé y (Jalonké) nio yooron deuk bi. Ca yonu 1715, ay Pël yu juulit yu jogué Fuuta-Toro ak Massina ca Mali, nio na nu ca Ginne, di fa Jihad, di rey ku du juulit wala di ko jaamlo, li moye tax xet yu bari (Susu y, jalonké, ak Baga y) daw nanu ca guedju Ginne, di tabax fofu ay nguruu. Pël u Juulit y dani reyone tamit yenene Pël ndax nekku nu woon juulit. Pël y juulit danu mbokkone ca njabot: Bâ, Baari, Jallo, Sow. Niom no tabax nguruu Fuuta-Jalon. Karamoko Alfa Jallo mo dieuk a nek Almamy.
Ca Gine, Pël ya dañu faa yàgg, waaye Mande ya (Jalonke) ñoo yoron dëkk ba. Ca 1715, ay Pël yu jullit yu juge Fuuta-Tooro ak Massina ca Mali, ñoo ñëw Gine, di fa Jiyaar, di ray ñi duli jullit walla di leen jàpp ay jaam, lii moo tax giir yu bari (Susu yi, jalonke, ak Baga yi) daw ca géeju Gine, di tabax foofa ay nguur. Pël yu Jullit yi dañu doon ray ñoom tamit yeneen Pël ngir ne nekkuñu woon ay juulit. Pëli jullit yi dañoo bokkoon ca njabooti: Bâ, Bari, Jallo, Sow. Ñoom ñoo tabax nguuru Fuuta-Jalon. Karamoko Alfa Jallo mo njëkk a nekk Almaami.
Ca Nisseria atum 1808, Usman Dan Fodio, njabotam Fuuta-Toro lani djogué di nek ay Toroodo, Serign bu mak la nekkone di bokk ca tarixa Xaadiriyya. Mom nak Dadjalé na Mbeykatu Haaussa, ak Sambkatu Pël, di lene dugg ca lislaam, ndax nu meunteu def Jihad ca Nguruu Haaussa y fi nek. Rey na Buuru Haaussa, tabax na Imbraator gu Sokoto. Demna xéer ca Imbratoor gu Kanem-Bornu ca Caad, wa é nionu danu amone doolé torop.
Ca Niseria atum 1808, Usmaan Dan Fojo, njabootam Fuuta-Tooro la bawoo, nekk ay Tooroodo, Sëriñ bu mag la nekkoon, bu bokk ca tariixa Xaadiriya. Moom nag dajale na baykatu Awsa yi, ak sàmbkati Pël yi, di leen dugal ci [[Lislaam]], ndax ñu man a def jiyaar ca Nguuru Awsa yi fi nekkoon. Ray na Buuru Awsa bi, daal di tabax Imbraatoor gu [[Sokoto]]. Dem na xeex ca Imbratoor gu Kanem-Bornu ca Cadd, waaye ñooñu dañoo amooon doole lool.
Ca kaw Kameroon atum 1810, bene Serign bu tudd Modibo Adama, dadjalé na Pël u juulit (fofu Fulbé la ni wax) y fi nékkone, nu tabax Nguruu Adamawa. Wa é amna Fulbé yu bari (WodaaBe/Borooro), bugunu woon bobu nguruu.
Ca kaw Kamerun atum 1810, benn sëriñ bu tudd Mojibo Adama, dajale na Pëli jullit(foofu Fulbé lees leen di wax) yi fi nékkoon, nu tabax nguuru Adamawa. Waaye am na Fulbé yu bari (WodaaBe/Borooro), yoy ànduñu woon ca googa nguur.
Modibo ak yenene Pël la def Jihad, ndax dunu nekkone ay juulit. Modibo Adama, Usman Dan Fodio moko dimbali.
Modibo ak yeneen Pël yi ñoo defoon Jihaad, ndax ay jullit lanu woon. Modibo Adama, Usman Dan Fojo moo ko dimbali woon.
Ca atum 1860, Alfa Yaya Molo Baaldé, tabax na nguruu Fuladu ca Bëj-saalum Senegaal. Da dadjalé Pël y di lene dugg ca lislaam, ndax Almamy u Fuuta-Jalon Alfa Bokar Biram, na woon du dimbali, kuduul Juulit.
Ca atum 1860, Alfa Yaaya Molo Balde, tabax nguuru Fuladu ca Bëj-saalumu Senegaal. Daal di dajale Pël yi di leen dugal ci lislaam, ndax Almaami bu Fuuta-Jalon Alfa Bokar Biram, nee na woon du dimbali ku dul Jullit.
Almamy bobu ak Alfa yaya xéer nanu nguruu Mandé Kabbu ak seni Buur (Mansa), ndax fofu Pël danu nekkone Jaami Mandé y. Niari Buur rek nio yoron Fuladu, Alfa Yaya ak domam Moussa Molo Baaldé.
Almaami boobu ak Alfa Yaaya xare nanu ak nguur gu Mandé, Kabbu ak seeni Buur (Mansa), ndax foofu Pël yi danu faa nekkoon Jaami Mandé yi. Ñaari Buur rekk ñoo yoroon Fulaadu, Alfa Yaaya ak doomam Musaa Molo Balde.
Kone Pël y, lislaam mo lene dadjalé, di lene jox doolé.
Kon Pël yi, Lislaam moo leen dajale, di leen jox doole.


Pël seni Nosteg mboolaay ga nii la tëdde woon:
Pël seeni Nostey mboolaay nii lanu tëdde woon:
*RimBe no done Buuri.
* RimBe ñoo daa doon Buur yi.
*JaawanDo y, no done top RimBe di lene wone lan lani yooré nguruu.
* JaawanDo yi, ñoo daa topp RimBe yi di leen won nan lañuy yore nguur.


Ñeeño yi:
Neeno y:
*WayilBe no done Teug y.
*LawBe no done Seen y.
*SakeeBe, no done Wuude y.
*MabuuBe, no done Rabb y.
*BaambaaDo, no done Xalamkat y, waykatu Jambar y.
*Gawlo, Waykatu Buuri.


* WayilBe ñoo daa nekk Tëgg yi.
Jaami:
* LawBe ñoo daa doon Seen yi.
*Maccudo wala Kordo.
* SakeeBe, nekk Wuude yi.
* MabuuBe, doon Ràbb yi.
* BaambaaDo, doon Xalamkat yi, woykati Jàmbaar yi.
* Gawlo, Woykati Buur yi.


Jaam yi:
Ca Isipt Pël y, da nu yoron niet Sant rek (Ba, Ka, Bara (tey mou nek Baari)). Ba paré Pël y danu jël yenene Sant Ndax deuk bi, wala Mban yi, liggey yi done def.

Li yeup ba am tey Sant gi: Bâ, Baari, Jallo, , Ja, Sow, Jaw, Caam, Naan, Jum, Dikko, Seydi, Mbow, Bokum, Dem, Sidibé, Sall,
* Maccudo walla Kordo.
Ca fuladu Pël yu bari Jamanka lani Sant. Ca Mali Sidibé moye Sow. Ca niseeria Pël yu bari Bello lani Sant. Ku Sant Baal, mamam ay Bâ lani woon. Ku Sant Jakk maman ay Sow lani woon.

Sankara, Sankaré, Shagari, li yëp bene la.
Ca Isipt Pël ya, dañoo yoroon ñatti Sant rekk (Ba, Ka, Bara (tay mu soppiku di Bari)). Ba noppi Pël yi danoo jël yeneen Sant Ndax dëkk bi, walla Mban yi, liggéey yi ñu doon def.
Amna Pël yu bari demna nu ca Wolof yi li moye tax amna ay wolof ku sant (Caam, Mbow, Sow, Naan, Sall). Tamit amna Xët yu bari nio nanu ca Pël, li moye tax amna ay Pël ku sant Cissé, Tuuré, Njaay, Jakité, Kamara ak yenene sant.

Li lépp ba am tay Sant yii: Bâ, Bari, Jallo, Ka, Ja, Sow, Jaw, Caam, Naan, Jum, Dikko, Seydi, Mbow, Bokum, Dem, Sidibe, Sàll,
Ca fulaadu Pël yu bari Jamanka lañu sant. Ca Mali Sidibe mooy Sow. Ca Niseriyaa Pël yu bari Bello lanu sant. Ku sant Baal, maamam ay Bâ lanu woon. Ku Sant Jakk maaman ay Sow lanu woon.
Sankara, Sankaré, Shagari, yooyu yépp benn lanu.
Am na Pël yu bari yoy dem nanu ca Wolof ya, looloo tax am ay wolof yu sant (Caam, Mbow, Sow, Naan, Sàll). Am na tam waaso yu bari yoy dikk nanu ci Pël yi, moo tax am ay Pël yu sant Siise, Ture, Njaay, Jakite, Kamara ak yeneen sant.


<gallery>
<gallery>

Sumb bu 8 Fewriyee 2009 à 16:54

Pël genn giir la gu nekk Senegaal. Pël yi ci Sowwu Afrig, dañoo bokk ci waaso yi gën a bari gën a yaatu. Senegaal, Mali, Gànnar, Gàmbi, Gine, Gine Bisaawóo, Niseer, Burkina Faso, Niseeria, Benin, Kot Diwaar, Kameroon, Réewum Diggu Afrig, ba Sudaan, ca réewum yii yépp Pël yi ña nga fa. Xeet woowu am nañu tur yu bari: Pël ci Wolof, ci Afrig mooy tur wi gën a siiw, Fula ca Mande ya, Fulani ca Naar ya, Fellata wala Fellan ca Sudaan.

Sàmmkatu Pël bu Gurma, bëj-saalumu Gao, Mali

ÑÑoom ci seen bopp dañuy wax Pullo wala FulBe. Isipt mooy réew mi ñu bawoo. Pël ya ca Isipt ay nit ñu ñuul lañu nekkoon. Ba noppi, ay nit ñu weex, ñëw ca seenum réew juge Asi ak Tugal , bokk na ca xeet yooya: Scythe, Aryen, Phrygien, Hittite, askan yu bari yu ñuy tudde ay waa End-tugal (Indo-européen). Pël yu ñuul yi ak nit ñu weex ñi dañoo jaxaasoo woon. Lii moo tax Pël yi gën a xees, gën a sew, am kawar gu gën a nooy, bu ñu leen xoolee ci yeneen xeet yu ñuul yi ci Afrig. Ba noppi, Imbraatóor gu Tirki(ñoñ usmaan ñi(les ottonams) ), tegoon nañu loxo réewum Isipt, di fa tege dund gu metti, rawati na ca nit ñu ñuul ña. Lii moo tax Pël ya ak Séeréer sa gàddaay, dëkki ca Sudaan (Nubie) dëkki seeni maam, soog a dem Senegaal. Pël ak Séeréer danoo bokk maam, seeni làkk tamit. Yàgg nañoo ànd, dañuy kalante ci seen biir. Ca yoonu Tekuruur, pël ya ca Dexug Senegaal rekk lañu nekkoon ak seeni nag. Booba nekkuñu woon ay jullit. Amuñu woon nguur ndax ak seeni nag ci màng rekk lañu nekke woon. Meew ak Sanqal (ñórndi) moo doonoon seenu lekk. Pël ci boppam am na xeet yu bari (Leyyi/KinDe), Ardo mooy seen Buur: JaawBe yi, UrurBe, WodaaBe, LaaCe, CutinkooBe, YirlaaBe. Am na yeneen KinDe. Màng gi ñu dëkke tax na ñu tuuru ci Sowwu Afrig gépp, ba far delseeti Sudaan, cig muñ ak coona ndax saa su nekk ci dëkki jàmbur yi rekk lañuy nekk, seen nag yi leeg-leeg ñu ruur tooli baykat yi, loolu it di jur xuloo bu rëy ak ŋaayoo ci seen digg ak woroon tool yi.

Ca atum 1539 Koli Tengella Bâ, mi ngi bokke ci Pël ci wetug baayam, bokk it ci Mande yi ci wàllug yaayam (Keyta), dajale woon na sàmmkati Pël yi ak mande yi, ngir ñu man a am doole. Daa di dugg ci yeneen xeet (Wolof, Séeréer, Bajaaranke, Joola, Baga, Sooninke . Ñoom ñépp ak seen aroo Koli Tengella, ñu yéeg ba Tekuruur, di xeex ak Buur-ba Jolof ba, ndax kii moo doon yor dëkk ba, ak Lam-Toro ya, Lam-Térmes, Lam-Taga ya, Juroom ñeenti fan soog a yor dëkk ai. Koli Tengella teg na fa njabootam (Denyakoobe yi), tudde na nguur ga Fuuta-Toro (Fuuta mooy dëkku Pël ca seen Làkk). Lii ca Senegaal la xewe.

Ca Mali Pël ya doñoo njëkk am doole ca atum 1818. Booba nag Ahmadu Bari, Sëriñ la nekkoon, dajale na Pëli Jullit yi, ak Mande yu jullit yi ( Mandé Mori yi : Siise, Ture, Silla ), ngir ñu àndandoo xeex (Jiyaar) safaan nguuru Bàmbara yi fi nekkoon (nguuru Ségu ak Kaarta). Buuru Bàmbara yi (Fama) ak seeni jàmbaar (Ton-Dion), amoon nanu doole, lii moo tax Ahmadu Bari tabax Imbraatoor gu Pël ca Massina Kese. ak itam Pël yi, ca Mali, foofu lañu ëppe woon ba tay (Tay jii foofa mooy diiwaan (Région) bu Mopti). Ca Gine, Pël ya dañu faa yàgg, waaye Mande ya (Jalonke) ñoo yoron dëkk ba. Ca 1715, ay Pël yu jullit yu juge Fuuta-Tooro ak Massina ca Mali, ñoo ñëw Gine, di fa Jiyaar, di ray ñi duli jullit walla di leen jàpp ay jaam, lii moo tax giir yu bari (Susu yi, jalonke, ak Baga yi) daw ca géeju Gine, di tabax foofa ay nguur. Pël yu Jullit yi dañu doon ray ñoom tamit yeneen Pël ngir ne nekkuñu woon ay juulit. Pëli jullit yi dañoo bokkoon ca njabooti: Bâ, Bari, Jallo, Sow. Ñoom ñoo tabax nguuru Fuuta-Jalon. Karamoko Alfa Jallo mo njëkk a nekk Almaami. Ca Niseria atum 1808, Usmaan Dan Fojo, njabootam Fuuta-Tooro la bawoo, nekk ay Tooroodo, Sëriñ bu mag la nekkoon, bu bokk ca tariixa Xaadiriya. Moom nag dajale na baykatu Awsa yi, ak sàmbkati Pël yi, di leen dugal ci Lislaam, ndax ñu man a def jiyaar ca Nguuru Awsa yi fi nekkoon. Ray na Buuru Awsa bi, daal di tabax Imbraatoor gu Sokoto. Dem na xeex ca Imbratoor gu Kanem-Bornu ca Cadd, waaye ñooñu dañoo amooon doole lool. Ca kaw Kamerun atum 1810, benn sëriñ bu tudd Mojibo Adama, dajale na Pëli jullit(foofu Fulbé lees leen di wax) yi fi nékkoon, nu tabax nguuru Adamawa. Waaye am na Fulbé yu bari (WodaaBe/Borooro), yoy ànduñu woon ca googa nguur. Modibo ak yeneen Pël yi ñoo defoon Jihaad, ndax ay jullit lanu woon. Modibo Adama, Usman Dan Fojo moo ko dimbali woon. Ca atum 1860, Alfa Yaaya Molo Balde, tabax nguuru Fuladu ca Bëj-saalumu Senegaal. Daal di dajale Pël yi di leen dugal ci lislaam, ndax Almaami bu Fuuta-Jalon Alfa Bokar Biram, nee na woon du dimbali ku dul Jullit. Almaami boobu ak Alfa Yaaya xare nanu ak nguur gu Mandé, Kabbu ak seeni Buur (Mansa), ndax foofu Pël yi danu faa nekkoon Jaami Mandé yi. Ñaari Buur rekk ñoo yoroon Fulaadu, Alfa Yaaya ak doomam Musaa Molo Balde.

Kon Pël yi, Lislaam moo leen dajale, di leen jox doole.

Pël seeni Nostey mboolaay nii lanu tëdde woon:

  • RimBe ñoo daa doon Buur yi.
  • JaawanDo yi, ñoo daa topp RimBe yi di leen won nan lañuy yore nguur.

Ñeeño yi:

  • WayilBe ñoo daa nekk Tëgg yi.
  • LawBe ñoo daa doon Seen yi.
  • SakeeBe, nekk Wuude yi.
  • MabuuBe, doon Ràbb yi.
  • BaambaaDo, doon Xalamkat yi, woykati Jàmbaar yi.
  • Gawlo, Woykati Buur yi.

Jaam yi:

  • Maccudo walla Kordo.

Ca Isipt Pël ya, dañoo yoroon ñatti Sant rekk (Ba, Ka, Bara (tay mu soppiku di Bari)). Ba noppi Pël yi danoo jël yeneen Sant Ndax dëkk bi, walla Mban yi, liggéey yi ñu doon def.

Li lépp ba am tay Sant yii: Bâ, Bari, Jallo, Ka, Ja, Sow, Jaw, Caam, Naan, Jum, Dikko, Seydi, Mbow, Bokum, Dem, Sidibe, Sàll, Ca fulaadu Pël yu bari Jamanka lañu sant. Ca Mali Sidibe mooy Sow. Ca Niseriyaa Pël yu bari Bello lanu sant. Ku sant Baal, maamam ay Bâ lanu woon. Ku Sant Jakk maaman ay Sow lanu woon. Sankara, Sankaré, Shagari, yooyu yépp benn lanu. Am na Pël yu bari yoy dem nanu ca Wolof ya, looloo tax am ay wolof yu sant (Caam, Mbow, Sow, Naan, Sàll). Am na tam waaso yu bari yoy dikk nanu ci Pël yi, moo tax am ay Pël yu sant Siise, Ture, Njaay, Jakite, Kamara ak yeneen sant.