Pël wuute gi ci sumb yi

Jóge Wikipedia.
Contenu supprimé Contenu ajouté
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 : Rëdd 1 :
Pël genn giir la gu nekk Senegaal. Pël y ca Sowwu Afrig, danu bokk ca xet y nio gëneu bari. Senegaal, Mali, Gànnar, Gaambi, Ginee, Ginee Bisaawoo, Niseer, Burkina Faso, Niseeria, Benin, Kot Diwaar, Kameroon, Réewum Diggu Afrig, ba Sudaan, ca réewum y yëp Pël y nio ngi fa.
Pël genn giir la gu nekk Senegaal. Pël yi ci [[Sowwu Afrig]], dañoo bokk ci waaso yi gën a bari gën a yaatu. [[Senegaal]], [[Mali]], [[Gànnar]], [[Gàmbi]], [[Gine]], [[Gine Bisaawóo]], [[Niseer]], Burkina Faso, Niseeria, Benin, Kot Diwaar, Kameroon, Réewum Diggu Afrig, ba Sudaan, ca réewum yii yépp Pël yi ña nga fa.
Xet bobu amna nu tuuri bari: Pël ca [[Wolof]], ca afrig mo tuuru gëna siiw, Fula ca Mandée y, Fulani ca Naari, Fellata wala Fellan ca Sudaan.
Xeet woowu am nañu tur yu bari: Pël ci [[Wolof]], ci [[Afrig]] mooy tur wi gën a siiw, Fula ca Mande ya, Fulani ca Naar ya, Fellata wala Fellan ca [[Sudaan]].
[[Image:Eleveurs Peuls.jpg|thumb|200px|left|Éleveurs peuls du Gourma, sud de [[Gao]], [[Mali]]]] Seni bop deni wax Pullo wala FulBe. Isipt moye deuk bi nu juddu. Pël y ca Isipt aye nit ku nul lani nekkone. Ba paré ay nit ku wéex, nio na nu ca seni deuk, niom réewum [[Asi]] tugal lani jogue woon, bokk ca xeti: Scythe, Aryen, Phrygien, Hittite, askan yu bari bi nu tudd ca lakk tubap y (Indo-européen). Pël y niul y aki nit ku wéer nonu, danu jaxaasé. Li moye tax Pël y da nu xawa gëna xées, gëna séew, am karowu gëna noye, yenene xetu nul y ca Afrig. Ba nopi, Imbratoor gu Tirki (Perse), uuf nanu réewum Isipt, di fa tek dundu meti ca niul y. li moye tax Pël ak Séeréer y dem nanu deuk ca Sudaan (Nubie) deuki seni mam, sogo dem Senegaal. Pël ak [[Séeréer]] danu bokk mam, seni lakk tamit. Yag nanu and, danu kalenté. Ca yonu [[Tekuruur]], pël y ca Dexug Senegaal rek lani nekkone ak seni Nak. Bobu nekkunu juulit. Amunu woon nguruu ndax ak seni nak ca tuki rek lani dundé. Meew ak Sankhal modon seni lek. Pël ci sen bopp amna xet yu bari (Leyyi/KinDe), Ardo bi moye seni Buur: JaawBe y, UrurBe, WodaaBe, LaaCe, CutinkooBe, YirlaaBe. Amna yenene KinDe. Tuki bi nu dund moye tax turu na nu ca Soowu Afrig yëp ba niowat Sudaan, di muun ndax sasounek ca deuki njabuur lani néké.
[[Image:Eleveurs Peuls.jpg|thumb|200px|left|Sàmmkatu Pël bu Gurma, bëj-saalumu [[Gao]], [[Mali]]]] ÑÑoom ci seen bopp dañuy wax Pullo wala FulBe. [[Isipt]] mooy réew mi ñu bawoo. Pël ya ca Isipt ay nit ñu ñuul lañu nekkoon. Ba noppi, ay nit ñu weex, ñëw ca seenum réew juge [[Asi]] ak [[Tugal]] , bokk na ca xeet yooya: Scythe, Aryen, Phrygien, Hittite, askan yu bari yu ñuy tudde ay waa End-tugal (Indo-européen). Pël yu ñuul yi ak nit ñu weex ñi dañoo jaxaasoo woon. Lii moo tax Pël yi gën a xees, gën a sew, am kawar gu gën a nooy, bu ñu leen xoolee ci yeneen xeet yu ñuul yi ci Afrig. Ba noppi, Imbraatóor gu Tirki(ñoñ usmaan ñi(les ottonams) ), tegoon nañu loxo réewum Isipt, di fa tege dund gu metti, rawati na ca nit ñu ñuul ña. Lii moo tax Pël ya ak Séeréer sa gàddaay, dëkki ca [[Sudaan]] (Nubie) dëkki seeni maam, soog a dem Senegaal. Pël ak [[Séeréer]] danoo bokk maam, seeni làkk tamit. Yàgg nañoo ànd, dañuy kalante ci seen biir. Ca yoonu [[Tekuruur]], pël ya ca Dexug Senegaal rekk lañu nekkoon ak seeni nag. Booba nekkuñu woon ay jullit. Amuñu woon nguur ndax ak seeni nag ci màng rekk lañu nekke woon. Meew ak Sanqal (ñórndi) moo doonoon seenu lekk. Pël ci boppam am na xeet yu bari (Leyyi/KinDe), Ardo mooy seen Buur: JaawBe yi, UrurBe, WodaaBe, LaaCe, CutinkooBe, YirlaaBe. Am na yeneen KinDe. Màng gi ñu dëkke tax na ñu tuuru ci Sowwu Afrig gépp, ba far delseeti Sudaan, cig muñ ak coona ndax saa su nekk ci dëkki jàmbur yi rekk lañuy nekk, seen nag yi leeg-leeg ñu ruur tooli baykat yi, loolu it di jur xuloo bu rëy ak ŋaayoo ci seen digg ak woroon tool yi.


Ca atum 1539 Koly Tenguella Bâ, ca Pël la bokk ca bayam, ca Mandé y la bokk ca yayam (Keyta), dadjalé na sambkatu Pël y ak mandé y, ndax nu meunteu am dolé. Ca Jambaram da di dugg ay yenene xet (Wolof, Séeréer, Bajaaranké, Jola, Baga, [[Sooninke]] ya. Niom yëp, ak sen ArDo Koly Tenguella, yég nanu ba Tekuruur, di xéer ag Buurba [[Jolof]] ba ndax ki modone yoor deuk bi, ak Lam-Toro y, Lam-Térmes, Lam-Taga y, Juroom nent fan sogo yoox deuk bi. Koly Tenguella teg nafa njabotam (Denyakoobé y), tuddu na nguruu bi Fuuta-Toro (Fuuta moye Deuku Pël ca seni Lakk). Li ca Senegal la xeewé.
Ca atum 1539 Koli Tengella Bâ, mi ngi booke ci Pël ci wetug baayam, bokk it ci Mande yi ci wàllug yaayam (Keyta), dajale woon na sàmmkati Pël yi ak mande yi, ngir ñu man a am doole. Daa di dugg ci yeneen xeet (Wolof, Séeréer, Bajaaranke, Joola, Baga, [[Sooninke]] . Ñoom ñépp ak seen aroo Koli Tengella, ñu yéeg ba Tekuruur, di xeex ak Buur-ba [[Jolof]] ba, ndax kii moo doon yor dëkk ba, ak Lam-Toro ya, Lam-Térmes, Lam-Taga ya, Juroom ñeenti fan soog a yor dëkk ai. Koli Tengella teg na fa njabootam (Denyakoobe yi), tudde na nguur ga Fuuta-Toro (Fuuta mooy dëkku Pël ca seen Làkk). Lii ca Senegaal la xewe.
Ca Mali Pël y danu dieuk am doolé ca atum 1818. Bobu nak Ahmadu Baari, Serign la né woon, dadjalé na Pël u Juulit y, ak Mandé yu juulit ( Mandé Mori y : Cissé, Tuuré, Sylla ), ndax nu meunteu xéer (Jihad) nguruu Bambara y fi nekkone (nguruu Ségu ak Kaarta). Buuru Bambara y (Fama) ak seni jambar (Ton-Dyon), amone nanu doolé, li moye tax Ahmadu Baari tabax na Imbratoor gu Pël ca Massina késsé. Tamit Pël y, ca Mali, fofu lani eupé woon ba tey (Tey di nek Région De Mopti).
Ca Mali Pël ya doñoo njëkk am doole ca atum 1818. Booba nag Ahmadu Bari, Sëriñ la nekkoon, dajale na Pëli Jullit yi, ak Mande yu jullit yi ( Mandé Mori yi : Siise, Ture, Silla ), ngir ñu àndandoo xeex (Jiyaar) safaan nguuru Bàmbara yi fi nekkoon (nguuru Ségu ak Kaarta). Buuru Bàmbara yi (Fama) ak seeni jàmbaar (Ton-Dion), amoon nanu doole, lii moo tax Ahmadu Bari tabax Imbraatoor gu Pël ca Massina Kese. ak itam Pël yi, ca Mali, fofu lani eupé woon ba tey (Tey di nek Région De Mopti).
Ca Ginne, Pël y danu fa yag, wa é Mandé y (Jalonké) nio yooron deuk bi. Ca yonu 1715, ay Pël yu juulit yu jogué Fuuta-Toro ak Massina ca Mali, nio na nu ca Ginne, di fa Jihad, di rey ku du juulit wala di ko jaamlo, li moye tax xet yu bari (Susu y, jalonké, ak Baga y) daw nanu ca guedju Ginne, di tabax fofu ay nguruu. Pël u Juulit y dani reyone tamit yenene Pël ndax nekku nu woon juulit. Pël y juulit danu mbokkone ca njabot: Bâ, Baari, Jallo, Sow. Niom no tabax nguruu Fuuta-Jalon. Karamoko Alfa Jallo mo dieuk a nek Almamy.
Ca Ginne, Pël y danu fa yag, wa é Mandé y (Jalonké) nio yooron deuk bi. Ca yonu 1715, ay Pël yu juulit yu jogué Fuuta-Toro ak Massina ca Mali, nio na nu ca Ginne, di fa Jihad, di rey ku du juulit wala di ko jaamlo, li moye tax xet yu bari (Susu y, jalonké, ak Baga y) daw nanu ca guedju Ginne, di tabax fofu ay nguruu. Pël u Juulit y dani reyone tamit yenene Pël ndax nekku nu woon juulit. Pël y juulit danu mbokkone ca njabot: Bâ, Baari, Jallo, Sow. Niom no tabax nguruu Fuuta-Jalon. Karamoko Alfa Jallo mo dieuk a nek Almamy.
Ca Nisseria atum 1808, Usman Dan Fodio, njabotam Fuuta-Toro lani djogué di nek ay Toroodo, Serign bu mak la nekkone di bokk ca tarixa Xaadiriyya. Mom nak Dadjalé na Mbeykatu Haaussa, ak Sambkatu Pël, di lene dugg ca lislaam, ndax nu meunteu def Jihad ca Nguruu Haaussa y fi nek. Rey na Buuru Haaussa, té tabax na Imbraator gu Sokoto. Demna xéer ca Imbratoor gu Kanem-Bornu ca Caad, wa é nionu danu amone doolé torop.
Ca Nisseria atum 1808, Usman Dan Fodio, njabotam Fuuta-Toro lani djogué di nek ay Toroodo, Serign bu mak la nekkone di bokk ca tarixa Xaadiriyya. Mom nak Dadjalé na Mbeykatu Haaussa, ak Sambkatu Pël, di lene dugg ca lislaam, ndax nu meunteu def Jihad ca Nguruu Haaussa y fi nek. Rey na Buuru Haaussa, té tabax na Imbraator gu Sokoto. Demna xéer ca Imbratoor gu Kanem-Bornu ca Caad, wa é nionu danu amone doolé torop.

Sumb bu 6 Fewriyee 2009 à 22:44

Pël genn giir la gu nekk Senegaal. Pël yi ci Sowwu Afrig, dañoo bokk ci waaso yi gën a bari gën a yaatu. Senegaal, Mali, Gànnar, Gàmbi, Gine, Gine Bisaawóo, Niseer, Burkina Faso, Niseeria, Benin, Kot Diwaar, Kameroon, Réewum Diggu Afrig, ba Sudaan, ca réewum yii yépp Pël yi ña nga fa. Xeet woowu am nañu tur yu bari: Pël ci Wolof, ci Afrig mooy tur wi gën a siiw, Fula ca Mande ya, Fulani ca Naar ya, Fellata wala Fellan ca Sudaan.

Sàmmkatu Pël bu Gurma, bëj-saalumu Gao, Mali

ÑÑoom ci seen bopp dañuy wax Pullo wala FulBe. Isipt mooy réew mi ñu bawoo. Pël ya ca Isipt ay nit ñu ñuul lañu nekkoon. Ba noppi, ay nit ñu weex, ñëw ca seenum réew juge Asi ak Tugal , bokk na ca xeet yooya: Scythe, Aryen, Phrygien, Hittite, askan yu bari yu ñuy tudde ay waa End-tugal (Indo-européen). Pël yu ñuul yi ak nit ñu weex ñi dañoo jaxaasoo woon. Lii moo tax Pël yi gën a xees, gën a sew, am kawar gu gën a nooy, bu ñu leen xoolee ci yeneen xeet yu ñuul yi ci Afrig. Ba noppi, Imbraatóor gu Tirki(ñoñ usmaan ñi(les ottonams) ), tegoon nañu loxo réewum Isipt, di fa tege dund gu metti, rawati na ca nit ñu ñuul ña. Lii moo tax Pël ya ak Séeréer sa gàddaay, dëkki ca Sudaan (Nubie) dëkki seeni maam, soog a dem Senegaal. Pël ak Séeréer danoo bokk maam, seeni làkk tamit. Yàgg nañoo ànd, dañuy kalante ci seen biir. Ca yoonu Tekuruur, pël ya ca Dexug Senegaal rekk lañu nekkoon ak seeni nag. Booba nekkuñu woon ay jullit. Amuñu woon nguur ndax ak seeni nag ci màng rekk lañu nekke woon. Meew ak Sanqal (ñórndi) moo doonoon seenu lekk. Pël ci boppam am na xeet yu bari (Leyyi/KinDe), Ardo mooy seen Buur: JaawBe yi, UrurBe, WodaaBe, LaaCe, CutinkooBe, YirlaaBe. Am na yeneen KinDe. Màng gi ñu dëkke tax na ñu tuuru ci Sowwu Afrig gépp, ba far delseeti Sudaan, cig muñ ak coona ndax saa su nekk ci dëkki jàmbur yi rekk lañuy nekk, seen nag yi leeg-leeg ñu ruur tooli baykat yi, loolu it di jur xuloo bu rëy ak ŋaayoo ci seen digg ak woroon tool yi.

Ca atum 1539 Koli Tengella Bâ, mi ngi booke ci Pël ci wetug baayam, bokk it ci Mande yi ci wàllug yaayam (Keyta), dajale woon na sàmmkati Pël yi ak mande yi, ngir ñu man a am doole. Daa di dugg ci yeneen xeet (Wolof, Séeréer, Bajaaranke, Joola, Baga, Sooninke . Ñoom ñépp ak seen aroo Koli Tengella, ñu yéeg ba Tekuruur, di xeex ak Buur-ba Jolof ba, ndax kii moo doon yor dëkk ba, ak Lam-Toro ya, Lam-Térmes, Lam-Taga ya, Juroom ñeenti fan soog a yor dëkk ai. Koli Tengella teg na fa njabootam (Denyakoobe yi), tudde na nguur ga Fuuta-Toro (Fuuta mooy dëkku Pël ca seen Làkk). Lii ca Senegaal la xewe.

Ca Mali Pël ya doñoo njëkk am doole ca atum 1818. Booba nag Ahmadu Bari, Sëriñ la nekkoon, dajale na Pëli Jullit yi, ak Mande yu jullit yi ( Mandé Mori yi : Siise, Ture, Silla ), ngir ñu àndandoo xeex (Jiyaar) safaan nguuru Bàmbara yi fi nekkoon (nguuru Ségu ak Kaarta). Buuru Bàmbara yi (Fama) ak seeni jàmbaar (Ton-Dion), amoon nanu doole, lii moo tax Ahmadu Bari tabax Imbraatoor gu Pël ca Massina Kese. ak itam Pël yi, ca Mali, fofu lani eupé woon ba tey (Tey di nek Région De Mopti). Ca Ginne, Pël y danu fa yag, wa é Mandé y (Jalonké) nio yooron deuk bi. Ca yonu 1715, ay Pël yu juulit yu jogué Fuuta-Toro ak Massina ca Mali, nio na nu ca Ginne, di fa Jihad, di rey ku du juulit wala di ko jaamlo, li moye tax xet yu bari (Susu y, jalonké, ak Baga y) daw nanu ca guedju Ginne, di tabax fofu ay nguruu. Pël u Juulit y dani reyone tamit yenene Pël ndax nekku nu woon juulit. Pël y juulit danu mbokkone ca njabot: Bâ, Baari, Jallo, Sow. Niom no tabax nguruu Fuuta-Jalon. Karamoko Alfa Jallo mo dieuk a nek Almamy. Ca Nisseria atum 1808, Usman Dan Fodio, njabotam Fuuta-Toro lani djogué di nek ay Toroodo, Serign bu mak la nekkone di bokk ca tarixa Xaadiriyya. Mom nak Dadjalé na Mbeykatu Haaussa, ak Sambkatu Pël, di lene dugg ca lislaam, ndax nu meunteu def Jihad ca Nguruu Haaussa y fi nek. Rey na Buuru Haaussa, té tabax na Imbraator gu Sokoto. Demna xéer ca Imbratoor gu Kanem-Bornu ca Caad, wa é nionu danu amone doolé torop. Ca kaw Kameroon atum 1810, bene Serign bu tudd Modibo Adama, dadjalé na Pël u juulit (fofu Fulbé la ni wax) y fi nékkone, nu tabax Nguruu Adamawa. Wa é amna Fulbé yu bari (WodaaBe/Borooro), bugunu woon bobu nguruu. Modibo ak yenene Pël la def Jihad, ndax dunu nekkone ay juulit. Modibo Adama, Usman Dan Fodio moko dimbali. Ca atum 1860, Alfa Yaya Molo Baaldé, tabax na nguruu Fuladu ca Bëj-saalum Senegaal. Da dadjalé Pël y di lene dugg ca lislaam, ndax Almamy u Fuuta-Jalon Alfa Bokar Biram, né na woon du dimbali, kuduul Juulit. Almamy bobu ak Alfa yaya xéer nanu nguruu Mandé Kabbu ak seni Buur (Mansa), ndax fofu Pël danu nekkone Jaami Mandé y. Niari Buur rek nio yoron Fuladu, Alfa Yaya ak domam Moussa Molo Baaldé.

Kone Pël y, lislaam mo lene dadjalé, di lene jox doolé.

Pël seni Nosteg mboolaay ga nii la tëdde woon:

  • RimBe no done Buuri.
  • JaawanDo y, no done top RimBe di lene wone lan lani yooré nguruu.

Neeno y:

  • WayilBe no done Teug y.
  • LawBe no done Seen y.
  • SakeeBe, no done Wuude y.
  • MabuuBe, no done Rabb y.
  • BaambaaDo, no done Xalamkat y, waykatu Jambar y.
  • Gawlo, Waykatu Buuri.

Jaami:

  • Maccudo wala Kordo.

Ca Isipt Pël y, da nu yoron niet Sant rek (Ba, Ka, Bara (tey mou nek Baari)). Ba paré Pël y danu jël yenene Sant Ndax deuk bi, wala Mban yi, liggey yi done def. Li yeup ba am tey Sant gi: Bâ, Baari, Jallo, Kâ, Ja, Sow, Jaw, Caam, Naan, Jum, Dikko, Seydi, Mbow, Bokum, Dem, Sidibé, Sall, Ca fuladu Pël yu bari Jamanka lani Sant. Ca Mali Sidibé moye Sow. Ca niseeria Pël yu bari Bello lani Sant. Ku Sant Baal, mamam ay Bâ lani woon. Ku Sant Jakk maman ay Sow lani woon. Sankara, Sankaré, Shagari, li yëp bene la. Amna Pël yu bari demna nu ca Wolof yi li moye tax amna ay wolof ku sant (Caam, Mbow, Sow, Naan, Sall). Tamit amna Xët yu bari nio nanu ca Pël, li moye tax amna ay Pël ku sant Cissé, Tuuré, Njaay, Jakité, Kamara ak yenene sant.