Doxalukaay bu mbëj wuute gi ci sumb yi

Jóge Wikipedia.
Contenu supprimé Contenu ajouté
Spacebirdy (waxtaancëru)
m Révocation des modifications de 208.27.234.156 (retour à la dernière version de Guaka)
Ptbotgourou (waxtaancëru)
m re-categorisation per CFD, Replaced: [[catégorie: → [[Wàll:
Rëdd 24 : Rëdd 24 :
* [[dawaan safaanoo]]
* [[dawaan safaanoo]]


[[catégorie:xaralaymbëj]]
[[Wàll:xaralaymbëj]]
{{modèle:wikibaatukaay}}
{{modèle:wikibaatukaay}}



Sumb bu 13 Disembar 2008 à 20:40

Doxalkat mbëj tekkeem moy ab wuutuloxo mbëj la, goo xam ne kattan giy duggu ci moom gu mbëj la te ga muy genne gu doolerandu la. Doxalkat mbëj yi am nañ solo lool ci dundinu jamono gu bees gi, te it dëgg la sax ne limu doxalkat mbëj yi nekk ci am reew day firndeel tolluwaayu jëm-kanamam. Te itam deminu, maanam yokkute walla nèewte limu doxalkat mbëj yi ci am reew bokk na ci wonekat yiy firndeel tolluwaayu yokkute ci wàllu xarala mu reew moomu. Ngir dëggal loolu, doyna xool ci jumtukaay yi nekk ci li ñu wër: ca saxaar ba ci watukaay ak yeneen ak yeneen, yi ngeen xam ne nit ku bees ki moo ngi koy jëfëndikoo bu baax, man naa ni sax ñooy doxal sunug dund.

Xaralay doxin gi

Wàll gi solowu:

Doxin

Dawanu mbëj gi day jaar ci ab lëmës gu ñu wëndeel ci ab doggub weñ gi tudd Tekkaaral. Lëmës googu, gi ñu defare ak wëñu përëm, jur ab toolu mbëjbijjaakon bu ca dawan jaaree. Toolu mbëjbijjaakon googu dañ koy sòob ci beneen toolu mbëjbijjaakon gu lëmës gu wëndeelukat bi jur, mi melokaanoo teewaayu ñaar walla ñetti seex i dott. Wëndeelukat bi tambalee wëndeelu ci sababu njureelu mbëjbijjaakon; bëj-gànnaaru toolu bijjaakon gu wëndeelukat bi day wòotalante ak bëj-saalumu toolu bijjaakon gu tekkaaral gi. Xaaju wëndeelu gu nekk, dottu gi day soppeeku, ci noonu la wëndeelu gi man a wéyee.

Doxalkat bii ci dawan safaanu rek lay doxee, ndax ci dawaan safaanu rek la bijjaakon di judd. Suy dox, ag wàll gu néew ci kattanu mbëj gi day soppeeku tanggoor ngir sababu joule.

Taariixam

Ci atum 1821, lu weesu xamteg feñte gu mbëjbijjaakon gi simikat boobu di Ørsted xamlewoon, la jëmmalkat bu waa-angalteer bii di Michael Faraday defar ñaari wuutuloxo ngir yoox li mu duppee ab wëndeelug mbëjbijjaakon: ab jalaxub dooley bijjaakon gu mbegewu te wéy, ci lu wër ab wëñ, ci maanaa mooy faramfaceg doxalkat mbëj gu njëkk.

Lëkkalekaay yu biir

wikbaatukaay am na xët wu tudd: Doxalukaay bu mbëj