Artemis wuute gi ci sumb yi

Jóge Wikipedia.
Contenu supprimé Contenu ajouté
VolkovBot (waxtaancëru)
SieBot (waxtaancëru)
m robot Modifying: zh:阿耳忒弥斯
Rëdd 63 : Rëdd 63 :
[[uk:Артеміда]]
[[uk:Артеміда]]
[[vi:Artemis (thần thoại)]]
[[vi:Artemis (thần thoại)]]
[[zh:阿忒弥斯]]
[[zh:阿忒弥斯]]

Sumb bu 23 Ut 2008 à 19:11

Ci angale mooy Diana; Ci faranse mooy Artémis

Artemis mooy turu jenn yàlla ju araam ju jigéen ci làkku gereg. Ci làkku waa room Diyana la tuddoon. Ñaari yàlla yu araam bokkoon nañu tur Artemis. Benn mooy li ñu gis ci Injiil, maanaam yàllay Efes (Jëf 19:23-41). Beneen yàllay gereg la woon ki ñu foog ne jigéenu yàlla ju araam ja tudd Apolo. Diine Artemisu Efes niroo na diine Astarte, yàllay waa Sidon.

Tur wi feeñ na ci Injiil ci Jëf 19:24,27,28,34,35.

Nataalu Artemis (Archeological Museum, Efes, Tirki.