Wikipedia:Babel wuute gi ci sumb yi

Jóge Wikipedia.
Contenu supprimé Contenu ajouté
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Ibou (waxtaancëru)
orthografie
Rëdd 3 : Rëdd 3 :
----
----
== Li muy jariñ ==
== Li muy jariñ ==
Donte fii [[Wikipedia]] ci kàllaama [[wolof]] la, waaye du ñi fi nekk ñépp a deggante. Am na ñu deggul wolof, walla seen degg des na, ñu man a soxla ku ñu jokkool ci làkk bi ñu degg, walla wolof yu yomb. Am na ay waa-wikipedia yu deggul wolof te di bëgg a jàpp ci liggéey bi, kon di na am solo lool nga wax ko ci yan làkk ngeen man a waxtaane, ngir njariñam man a feeñ.
Donte fii [[Wikipedia]] ci kàllaama [[wolof]] la, waaye du ñi fi nekk ñéppa deggante. Am na ñu deggul wolof, walla seen dégg des na, ñu mana soxla ku ñu jokkool ci làkk wi ñu dégg, walla wolof yu yomb. Am na ay waa-wikipedia yu deggul wolof te di bëgga jàpp ci liggéey bi, kon di na am-solo lool nga wax ko ci yan làkk ngeen mana waxtaane, ngir njariñam mana feeñ.


Bii sémb di na yombal jokkoo gi ci biir aw askan wu bariy làkk wu mel ne wu Wikipedia: ci misaal, di na yomb jot kuy wax wenn làkk wi, te itam di na xamale tolluwaayu dégginu wolof bu ab jëfandikukat bu bindu.
Bii sémb di na yombal jokkoo gi ci biir aw askan wu barilàkk wu mel ne wu Wikipedia: ci misaal, di na yomb jot kuy wax wenn làkk wi, te itam di na xamale tolluwaayu dégginu wolof bu ab jëfandikukat bu bindu.


== Nu ma koy defe? ==
== Nu ma koy defe? ==

Sumb bu 5 Ut 2008 à 09:28

Xët wii moo lay leeral nooy xamale yeneen jëfandikukat yi, say xameel ci yeneen làkk yi ak tolluwaayu xameel gi.



Li muy jariñ

Donte fii Wikipedia ci kàllaama wolof la, waaye du ñi fi nekk ñéppa deggante. Am na ñu deggul wolof, walla seen dégg des na, ñu mana soxla ku ñu jokkool ci làkk wi ñu dégg, walla wolof yu yomb. Am na ay waa-wikipedia yu deggul wolof te di bëgga jàpp ci liggéey bi, kon di na am-solo lool nga wax ko ci yan làkk ngeen mana waxtaane, ngir njariñam mana feeñ.

Bii sémb di na yombal jokkoo gi ci biir aw askan wu barilàkk wu mel ne wu Wikipedia: ci misaal, di na yomb jot kuy wax wenn làkk wi, te itam di na xamale tolluwaayu dégginu wolof bu ab jëfandikukat bu bindu.

Nu ma koy defe?

Wikipedia:Babel
wo-1
fr-1
en-1
Seet waa-wikipedia ci làkk-ak-làkk

Doy na nga yokk ci sa xëtu jëfandikukat Babelbox bi, tabax ko ci topp tegtal yii:

  • Nga yokk ci limu làkk yi nga dégg te teg ci |
    • Misaal: {{Babel| (3 làkk)

Su ko defeen nag nga def ci tolluwaayu ni nga dégge wolof. Soo bëggee mu mel ne ni nga koy gisee (ci sa ndeyjoor), nga def: wo-0 walla wo-1 walla wo-2,añse.

Misaal: {{Babel|wo-1|fr-1|en-1}}

Yu wolof

Wikipedia:Babel
wo-5
wo-4
wo-3
wo-2
wo-1
wo-0
Seet waa-wikipedia ci làkk-ak-làkk