Arminaat wuute gi ci sumb yi

Jóge Wikipedia.
Contenu supprimé Contenu ajouté
VolkovBot (waxtaancëru)
PipepBot (waxtaancëru)
Rëdd 79 : Rëdd 79 :
[[mdf:Ковгярькссь]]
[[mdf:Ковгярькссь]]
[[mi:Maramataka]]
[[mi:Maramataka]]
[[ml:കലണ്ടര്‍]]
[[ms:Takwim]]
[[ms:Takwim]]
[[myv:Ковкерькс]]
[[myv:Ковкерькс]]

Sumb bu 7 Suwe 2008 à 09:19

Arminaat seddatlinu taariix(date) yi la ci ab jamono. Doon na ab noste bu waa Isipt yu yàgg ya sakkoon ngir seddatle aka nos jamono ji ci ay diir. Ca ndoorte ga dañ ko sakkoon ngir man a dëppale yenn feeñte saytubiddiw ak gëstubiddiw ak jamono ja ñuy amee. Doon nañ ko jëfandikoo it ngir natt seeni bési xumbeeli diine.

Bennali arminaat

Ci taariix arminaat yépp a cëslaayu ci ay bennali(unite) dénd yu seen diir aju ciy feñtey saytubiddiw.

Bés

Daanaka ci xay yépp, coppite gi ci bés ak guddi moo doonoon bennal bi ñuy natte at yi. Wëndeelug Suuf si doon li waral safaanu googu, te njël li du amandoo ci barab yi ne ci kol-kolu suuf si . Soo xoolee Senegaal ak Faraas bokkuñuy waxtu, Faraas a ñuy rawee ñaari waxtu su dee nawet la, benn waxtu su dee noor la .

Weer

Li deminu weer doon lu yomb a may-bët, moo tax mu doon ab jumtukaay ngir natt jamono ji. Arminaatu jullit ñi moon weer wi lay topp , waaye arminaatu geregori moom jant bi lay topp.

At

Mooy mbooleem jamono yi, at doon na diir bu gudd. Cig njoort, Moom it ci yenn feñtey dénd la ko nit ñi sakk arminaat daa natte.

Arminaat gi njëkk a cëslaayu ci at, maanaam ci soppiku at ba at mooy arminaatu waa isipt.

Booleeb bennali dénd yi

At ak bés

Ci jamono ji ñu ne, an at mooy 365,24220 bés. arminaatu waa isipt, ak arminaatu suleymaan, ak arminaatu geregori, doon nañ ay royuwaay ci liggéey bu mag bi ñu def ngir man a demandool (syncroniser) at mi ak wëndeelug Suuf si ci li wër jant bi.

ba tay sax seenug demandoo des na, ba tax na 10000 at yu ne di na juum 3 fan.

Weer ak bés

Diirub weer mooy 29 bés 12 waxtu 44 simili ak 2,8 saa (muy 29,53 bés). Kon su ñuy weccee ay weeri fanweeri fan ak yu ñaar-fukk ak juroom-ñenti fan, te di yokk benn bés fanweeri weer yu ne, di na doon lu nanguwu. Bii nattin, arminaati weer yépp a koy jëfandikoo ngir dëppale bés yi ci weer ak wëndeelinu weer wi.

Jamono ak at

Ci arminaat yu bari, ñenti jamono ñoo am: noor, nawet, lolli. Jamono yooyu, ci xay woo dem ak niñ koy seddatlee ci at mi. Sunu xoolee waa siin ñoom nawet la at mi di tambalee.