Wikipedia:Babel wuute gi ci sumb yi

Jóge Wikipedia.
Contenu supprimé Contenu ajouté
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Guérin Nicolas (waxtaancëru)
cat
Rëdd 22 : Rëdd 22 :
|{{Babel|wo|wo-5|wo-4|wo-3|wo-2|wo-1|wo-0}}
|{{Babel|wo|wo-5|wo-4|wo-3|wo-2|wo-1|wo-0}}
|}
|}

[[catégorie:jeego yu njëkk]]
[[catégorie:jeego yu njëkk]]
[[Catégorie:Barab Wikipedia|{{PAGENAME}}]]

Sumb bu 19 Awril 2008 à 16:46

Xët wii moo lay leeral nooy xamale yeneen jëfandikukat yi, say xameel ci yeneen làkk yi ak tolluwaayu xameel gi.



Li muy jariñ

Donte fii Wikipedia ci kàllaama wolof la, waaye du ñi fi nekk ñépp a deggante. Am na ñu deggul wolof, walla seen degg des na, ñu man a soxla ku ñu jokkool ci làkk bi ñu degg, walla wolof yu yomb. Am na ay waa-wikipedia yu deggul wolof te di bëgg a jàpp ci liggéey bi, kon di na am solo lool nga wax ko ci yan làkk ngeen man a waxtaane, ngir njariñam man a feeñ.

Mii sémb di na yombal jokkoo gi ci biir aw askan gu barilàkk gu mel ne Wikipedia: ci misaal, di na yomb jot kuy wax wenn làkk wi, te itam di na xamale tolluwaayu dégginu wolof gu ab jëfandikukat bu bindu.

Nu ma koy defee?

Wikipedia:Babel
wo-1
fr-1
en-1
Seet waa-wikipedia ci làkk-ak-làkk

Doy na nga yokk ci sa xëtu jëfandikukat Babelbox bi, tabax ko ci topp tektal yii:

  • Nga yokk ci limu làkk yi nga degg te teg ci |
    • Misaal: {{Babel| (3 làkk)

Su ko defeen nak nga def ci tolluwaayu ni nga deggee wolof. Soo bëggee mu mel ne ni nga koy gisee (ci sa ndeyjoor), nga def: wo-0 walla wo-1 walla wo-2,añse.

Misaal: {{Babel|wo-1|fr-1|en-1}}

Yu wolof

Wikipedia:Babel
wo-5
wo-4
wo-3
wo-2
wo-1
wo-0
Seet waa-wikipedia ci làkk-ak-làkk