Wikipedia:Babel wuute gi ci sumb yi

Jóge Wikipedia.
Contenu supprimé Contenu ajouté
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Guérin Nicolas (waxtaancëru)
to babel
Rëdd 21 : Rëdd 21 :
== Yu wolof ==
== Yu wolof ==
{|align=left
{|align=left
|{{Babel-6|wo|wo-5|wo-4|wo-3|wo-2|wo-1|wo-0}}
|{{Babel|wo|wo-5|wo-4|wo-3|wo-2|wo-1|wo-0}}
|}
|}
[[catégorie:jeego yu njëkk]]
[[catégorie:jeego yu njëkk]]

Sumb bu 4 Awril 2008 à 19:32

Xët wii moo lay leeral nooy xamale yeneen jëfëndikookat yi, say xameel ci yeneen làkk yi ak tolluwaayu xameel gi.



Lumuy jariñ

Donte fii Wikipedia ci kàllaama wolof la, waaye du ñi fi nekk ñépp a deggante. Am na ñu deggul wolof, walla seen degg des na, ñu man a soxla ku ñu jokkool ci làkk bi ñu degg, walla wolof yu yomb. Am na ay waa wikipedia yu deggul wolof te di bëgg a jàpp ci liggéey bi, kon di na am solo lool nga wax ko ci yan làkk ngeen man a waxtaane, ngir njariñam man a feeñ.

Mii sémb di na yombal jokkoo gi ci biir aw askan gu bariy làkk gu mel ne Wikipedia: ci misaal, di na yomb jot kuy wax wenn làkk wi, te itam di na xamale tolluwaayu degginu wolof gu ab jëfëndikookat bu bindu.

Nu ma koy defee?

Royuwaay:Babel-3 Doy na nga yokk ci sa xëtu jëfëndikookat Babelbox bi, tabax ko ci topp tektal yii:

  • Tambalil ak {{Babel-
  • Nga yokk ci limu làkk yi nga degg te teg ci |
    • Misaal: {{Babel-3| (3 làkk)

Su ko defeen nak nga def ci tolluwaayu ni nga deggee wolof. Soo bëggee mu mel ne ni nga koy gisee (ci sa ndeyjoor), nga def: wo-0 walla wo-1 walla wo-2,añse.

Misaal: {{Babel-3|wo-1|fr-1|en-1}}

Yu wolof

Wikipedia:Babel
wo-5
wo-4
wo-3
wo-2
wo-1
wo-0
Seet waa-wikipedia ci làkk-ak-làkk