Géej gu Diggu wuute gi ci sumb yi

Jóge Wikipedia.
Contenu supprimé Contenu ajouté
SieBot (waxtaancëru)
AlleborgoBot (waxtaancëru)
m robot Modifying: ar:البحر المتوسط
Rëdd 18 : Rëdd 18 :
[[an:Mar Mediterranio]]
[[an:Mar Mediterranio]]
[[ang:Wendelsǣ]]
[[ang:Wendelsǣ]]
[[ar:البحرالأبيض المتوسط]]
[[ar:البحر المتوسط]]
[[ast:Mar Mediterraneu]]
[[ast:Mar Mediterraneu]]
[[az:Aralıq dənizi]]
[[az:Aralıq dənizi]]

Sumb bu 23 Fewriyee 2008 à 21:35

Géej gu Diggu mooy géej gi ne ci diggante goxu Afrik ak gu Tugal ak gu Asi. Yaa-yaawam 2,51 milyioŋi toll ci km² te yaatuwaayam toll ci 3700 km.

Ci sowwu mi ngi yem ci Mbàmbulaanu Atlas, ci penku ci Géeju Marmara ak Géej gu Ñuul gi. Yenn saa yi Géeju Marmara dañ koy boole ci Géej gu Diggu gi, waaye Géej gu Ñuul gi moom dañ leen di tàqale.

Melokaan

Géej gu Diggu gi dan koo seddatle ci ñaari mbalka*. Bi njëkk mooy Géej gu Diggu gu sowwu, yem ci yoonal* gu Sisil, beneen bi mooy Géej gu Diggu gu penku.

Karmat

  • Yoonal: canal
  • Mbalka: bassin
Diwaani Tugalasi
Asi      Diwaan yu MR: Diggu Asi · Penku Asi · Bëj-saalum-penku Asi · Ron-goxu End
Yeneen diwaan: Penku gu Sori · Penku gu Diggu · Penku gu Jege · Sibeeri
Tugal      Diwaan yu MR: Sowwu Tugal · Bëj-saalumu Tugal · Penku Tugal · Bëj-gànnaaru Tugal 
Yeneen diwaan: Kókaas · Géej gu Diggu · Skandinaawi