Biir bu daw wuute gi ci sumb yi

Aller à la navigation Aller à la recherche
Aucun changement de taille ,  8 weer ci ginaaw
Coppite gi amul tënk
(→‎Royuwaay yi : biir buy daw)
 
}}
<!-- Definition and Characteristics -->
'''Biir bu daw''' wala '''Jaare''' mooy ngay dem wanag gën gaa néew ñatti yoon ci bis te li ngay génne [[ginaaw kër yi]] dafay ndoxe.<!--<ref name=WHO2013/> --> Yenn saa mu jàpp la ay fan, te loolu mën na tax sa yaram [[ñàkk ndox]].<!--<ref name=WHO2013/> --> Su yaramu nit ñàkkee ndox deram dootul nooy te it mën a soppiku.<!--<ref name=WHO2013/> --> Mën nga dem ba dootoo [[saw]] lu bari, sab [[der furi]], sa [[xol di tëf-tëfi]], te sam [[xel mu doxul ni mu waree wala jëf yu yeex, |xel dootul dox ni mu waree wala say jëf yeex,]], su demee ba gën a tar.<!--<ref name=WHO2013/> --> Ginaaw kër yu tooy te bañ a ndoxe mën dal liir yiy [[nàmp]], waaye, loolu du dara.<ref name=WHO2013/>
 
<!-- Cause and Diagnosis -->
46

modifications

Njëlu joowiin