Wikipedia:Babel wuute gi ci sumb yi

Jóge Wikipedia.
Contenu supprimé Contenu ajouté
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 : Rëdd 1 :
Xët wii moo lay leeral nooy xamale yeneen jëfëndikookat yi, say xameel ci yeneen làkk yi ak tolluwaayu xameel gi.
XËT MII NOPPEEGUL

'''UBBITE'''
----
Xët mii moo lay leeral nooy xamale yeneen way-jëfëndikoo yi, say xameel ci yeneen làkk yi ak tolluwaayu xameel gi.
----
----
----
----
== Lumuy jariñ ==
== Lumuy jariñ ==
Donte fii Wikipedia la ci kàllaama wolof, waaye du ñi fi nekk ñëpp a deggante. Am na ñu deggul wolof, walla seen degg des na, ñu mana soxla ku ñu jokkool ci làkk bi ñu degg, walla wolof yu yomb. Am na ay waa-wikipedia yu deggul wolof te di bëgg a japp ci ligey bi, kon di na am solo lool nga wax ko ci yan làkk ngeen man a waxtaane, ngir njariñam man a feeñ.
Donte fii [[Wikipedia]] ci kàllaama [[wolof]] la, waaye du ñi fi nekk ñépp a deggante. Am na ñu deggul wolof, walla seen degg des na, ñu man a soxla ku ñu jokkool ci làkk bi ñu degg, walla wolof yu yomb. Am na ay waa wikipedia yu deggul wolof te di bëgg a jàpp ci liggéey bi, kon di na am solo lool nga wax ko ci yan làkk ngeen man a waxtaane, ngir njariñam man a feeñ.


Gii mebet di na yombal jokkoo gi ci biir aw askan gu bariy làkk gu mel ne Wikipedia: ci misaal, di na yomb jot kuy wax wenn làkk wi, te itam di na xamale tolluwaayu degginu wolof gu ab jëfëndikookat bu bindu.
Mii sémb di na yombal jokkoo gi ci biir aw askan gu bariy làkk gu mel ne Wikipedia: ci misaal, di na yomb jot kuy wax wenn làkk wi, te itam di na xamale tolluwaayu degginu wolof gu ab jëfëndikookat bu bindu.


== Nu ma koy defee? ==
== Nu ma koy defee? ==
{{Babel-3|wo-1|fr-1|en-1}}
Doy na nga yokk ci sa [[xëtu jëfëndikookat]] '''Babelbox''' bi, tabax ko ci topp tektal yii:
Doy na nga yokk ci sa [[Xëtu jëfëndikookat|xëtu jëfëndikookat]] '''Babelbox''' bi, tabax ko ci topp tektal yii:
* Tambalil ak '''{{Babel-'''
* Tambalil ak '''{{Babel-'''
* Nga yokk ci limu làkk yi nga degg te teg ci '''|'''
* Nga yokk ci limu làkk yi nga degg te teg ci '''|'''
**Misaal: '''{{Babel-3|''' (3 làkk)
**Misaal: '''{{Babel-3|''' (3 làkk)

Su ko defeen nak nga def ci tolluwaayu ni nga deggee wolof. Soo bëggee mu mel ne ni nga koy gisee (ci sa ndeyjoor), nga def: wo-0 walla wo-1 walla wo-2,añse.

Misaal:
'''<nowiki>{{Babel-3|wo-1|fr-1|en-1}}</nowiki>'''
== Yu wolof ==
{|align=left
|{{Babel-6|wo|wo-5|wo-4|wo-3|wo-2|wo-1|wo-0}}
|}
[[catégorie:jeego yu njëkk]]

Sumb bu 9 Sattumbar 2007 à 14:07

Xët wii moo lay leeral nooy xamale yeneen jëfëndikookat yi, say xameel ci yeneen làkk yi ak tolluwaayu xameel gi.



Lumuy jariñ

Donte fii Wikipedia ci kàllaama wolof la, waaye du ñi fi nekk ñépp a deggante. Am na ñu deggul wolof, walla seen degg des na, ñu man a soxla ku ñu jokkool ci làkk bi ñu degg, walla wolof yu yomb. Am na ay waa wikipedia yu deggul wolof te di bëgg a jàpp ci liggéey bi, kon di na am solo lool nga wax ko ci yan làkk ngeen man a waxtaane, ngir njariñam man a feeñ.

Mii sémb di na yombal jokkoo gi ci biir aw askan gu bariy làkk gu mel ne Wikipedia: ci misaal, di na yomb jot kuy wax wenn làkk wi, te itam di na xamale tolluwaayu degginu wolof gu ab jëfëndikookat bu bindu.

Nu ma koy defee?

Royuwaay:Babel-3 Doy na nga yokk ci sa xëtu jëfëndikookat Babelbox bi, tabax ko ci topp tektal yii:

  • Tambalil ak {{Babel-
  • Nga yokk ci limu làkk yi nga degg te teg ci |
    • Misaal: {{Babel-3| (3 làkk)

Su ko defeen nak nga def ci tolluwaayu ni nga deggee wolof. Soo bëggee mu mel ne ni nga koy gisee (ci sa ndeyjoor), nga def: wo-0 walla wo-1 walla wo-2,añse.

Misaal: {{Babel-3|wo-1|fr-1|en-1}}

Yu wolof

Royuwaay:Babel-6