Garanaat wuute gi ci sumb yi

Jóge Wikipedia.
Contenu supprimé Contenu ajouté
Baye gey (waxtaancëru)
Xët wu bees : '''Garanaat''' xeet la ci xeeti garab yi nga xam ni dañuy am fóoyteef, mi ngi bokk ci njabootug Lythracées . Cosaanam ma nga nekk fële ca Asi ñu di ko bay ci kémbaar y…
 
Daarul xayri (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Tafaan: Éditeur de wikicode 2017
 
Rëdd 1 : Rëdd 1 :
[[Dencukaay:Punica.granatum(04).jpg|vignette|Nataalu garabug Garanaat]]
'''Garanaat''' xeet la ci xeeti garab yi nga xam ni dañuy am fóoyteef, mi ngi bokk ci njabootug [[Lythracées]] . Cosaanam ma nga nekk fële ca Asi ñu di ko bay ci kémbaar yu bari, fi muy sax nag mooy fu xaw a am aw naaj.
'''Garanaat''' xeet la ci xeeti garab yi nga xam ni dañuy am fóoyteef, mi ngi bokk ci njabootug [[Lythracées]] . Cosaanam ma nga nekk fële ca Asi ñu di ko bay ci kémbaar yu bari, fi muy sax nag mooy fu xaw a am aw naaj.


Rëdd 12 : Rëdd 13 :


== Nataal ==
== Nataal ==
<gallery>

Dencukaay:Pomegranate fruit - Punica granatum.jpg|Meññetum Garanaat
Dencukaay:Punica granatum1.jpg|Dàtt bi
Dencukaay:Punica granatum (Jardin des plantes).jpg|Tóortóor bi
Dencukaay:Punica granatum bonsai 3.jpg|Xob yi
Dencukaay:Punica granatum (8).JPG|Xob yi ba tay
</gallery>
== Turu xam-xam wi ==
== Turu xam-xam wi ==
[[Punica granatum]]
[[Punica granatum]]

Sumb bi teew bu 22 Sulet 2019 à 00:33

Nataalu garabug Garanaat

Garanaat xeet la ci xeeti garab yi nga xam ni dañuy am fóoyteef, mi ngi bokk ci njabootug Lythracées . Cosaanam ma nga nekk fële ca Asi ñu di ko bay ci kémbaar yu bari, fi muy sax nag mooy fu xaw a am aw naaj.

Melo wi[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Garab gu ndaw lay doon, guddaayam man naa jàpp 6i met. Man naa dund 200i at, waaye li ëpp ci limiy jur mi ngi koy jur ci 20i atam ju njëkk yi.

Ay Tóortóoram, dañuy yor melo wu xaw a xonq, 3i sentimet la baaxoo di gudde, ñatti yoon rekk lay meññ ci at mi, weeru Ut ak Me . Melow foytéefu "Garanaat" ñoo ngi sukkandikoo ci nimuy matee, maanaam yenn saay mu yor melo wu weex, walla wu xoq, walla wu mboq.

Doonte man naa dund ci suuf su xaw a wow waaye du tee garab gi suuf su xaw a tooy la bëgg ngir mu man a jur ay foytéefam ni mu ware.

Solo si[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Garanaat garab la gog manees na cee defar ay jar doom bi dees koy lekk ay tóortóoram manees na cee xeex yenn wopp yu mel ni Aasm.

Nataal[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Turu xam-xam wi[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Punica granatum