Gët

Jóge Wikipedia.
Sauter à la navigation Sauter à la recherche

gët mbooloo la, bennaan bi mooy bët: cér bi ñuy gise, waaye day tekki it (agents secrets), ndax sa gët yi nga boyal ci biir nit ñeek mboolaay gi, ngir ñu xam li fi xew, nga xame ko ci ñoom, dees na ko wax it yëddukat