Ceññeer-mbej

Jóge Wikipedia.

wolof[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Ceññeer-mbej day wund feeñte yiy saytu sosu ak tasug duus yu mbejbijjaakon yu néew kàttan yi. Moom nag (Ceññeer-mbej)mooy cëslaayu mbooleem xarala yu jokkoo yiy sukkandiku ci duus yu mbejbijjaakon yi.

français[Soppisoppi gongikuwaay bi]

  • radioélectricité

La radioélectricité: désigne les phénomènes qui régissent la formation et la propagation des ondes électromagnétiques de faible énergie. Elle est le fondement de toutes les techniques de communication ayant pour support les ondes électromagnétiques.

Logo Commons

Xool it Wikimedia Commons