Astuces mobiles

Jóge Wikipedia.
Aller à la navigation Aller à la recherche

Ay Astuces Mobiles you Am solo[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Ganaw bamalen nuyo, tay dama indi wone bene sujet ci astuces mobiles. Molay meuneul ngay def ci sa joumtakayou wote ay mbiir you neubeutou you ndaw wayer you am solo.

Bokounaci noniou def ba guiss sa téléphone bou réré, bokounaci noy def ba délowat sa téléphone mou melni lou bess, bokounaci noy def so fatéwé sa cabi bilay takh nga dougou ci téléphone bi.

Mouy lou am solo ci sounou doundine, ndakh téléphone ak dioumtoukay you kharalayi bokounagnou ci sounou dound té kéne meunoula dem bayiko.

Ci astuces yoyou meun nagnou ko am ci bep téléphone android ak IOS ak ci marque you bari you melni:

  • Samsung
  • Apple
  • Xiaomi
  • ak yénéne.

Bolene dougué ci site bi di astuces mobiles di nguéne fa guiss yoyou astuce ci bene par béne ak ay firdé aki video. beuseul fi pour dem fa.

Bouma sama téléphone réré noumay def[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Bok naci liguey ndieug def moy connectéwou ci google localiser mon appareil pour kham foumou fété guinaw boci activé gps bi

Meun nga def mou sonner, meun ngako bloquer, meun nga dindi mbolene mbiir yi nékone ci biir, lou déméni ay photo ak ay widéo.

Bouma beugué effacer sama téléphone noumay def[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Am na ay code secret you lay yomabalal noy effacer bep mbiir ci sa téléphone ci lou yom, lolou tamit meun ngako guiss ci site bi di astuces mobiles.


Nion guiléne di diadieufeul ci diang bi di lene waax ba bénéne yoon.