Aller au contenu

Alliance pour une révolution verte en Afrique

Jóge Wikipedia.

Alliance pour une révolution verte en Afrique (AGRA) kuréel la guy def te Yàlla tax, li ko taxa jokk mooy soppi mbay mi ci Afrig, mu joge ci mbay mi ñuy dundee, mu dem ba nekk mbay miy dundal, muy gëna baaxal dundu njaboot yiy bay ci biir kontinang bi yépp.

AGRA mingi nekk ci Nairobi, Keeñaa, foofu la ekipu gëstukat, ekonomist ak njiiti liggéey di jàppale liggéeyam ci réew yu Afrig ak ci nguur yi ci Afrig.

Fondation Bill & Melinda Gates ak Rockefeller ñooy dooleel kuréel gi.