Aller au contenu

Alegsàndiri

Jóge Wikipedia.
Alexandria
(Iskindireyya)
Skyline of {{{official_name}}}
Feeñal
RéewRaaya Isipt Isipt
Tus-wu-gaar
Tus-wu-taxaw
31° 11′ 53″ Nord
     29° 55′ 09″ Est
/ 31.198, 29.9192
way-dëkk3 500 000 nit
atum way-dëkk2 001

Ci angale mooy Alexandria; Ci faranse mooy Alexandrie. Fondation : -334

Benn dëkk ak teeru ci Misra la, fu sorewul bëlub dexu Niil. Péeyu Misra la woon ci jamano Injiil ji, di dëkk bu gëna am solo ci Gereg yi. Ñaareelu dëkk bu gëna réy ci nguuru Room.

Dañuy fekk Alegsàndiri ci Injiil ci Jëf 6:9; 18:24; 27:6; 28:11.