Aller au contenu

Al-Qaeda

Jóge Wikipedia.

Al-Qaeda, ñu xamee ko ci "Base bi," kuréel la gu xeexkat pan-islamist, jihadist sunni yi ñoo ko jiite, ñoom ñooy jiite fippug islaam ci àdduna bi ngir boole àdduna jullit yi ci biir benn kalifa islaam bu ëpp réew mi. Araab yi ñoo ci gëna bari waaye amna ci itam ñu bawoo ci yeneen xeet. Al-Qaida dafay song siwil yi, koom gi ak soldaari Diiwaan yu Bennoo ak ay banxaasam; lu ci melni bomb yiñ sànni ci ammbasaadu Etats Unis ci 1998, bomb yiñ sànni ci USS Cole, ak songu 11 septembre.