Aller au contenu

) Soxna Jóob ñu koy wax Soxna Njóoba Jóob.

Jóge Wikipedia.

Soxna Njóoba Jóob mii, moom la Sëriñ Maxtaar Gay njëkk a jël ci Soxna, waaye jótu faa am njaboot, bi muy am doom ci la faatu moom Soxna Njóoba Jóob, ca Ngay-Ngay Assan.