Xaaju kol-kol

Ab jukkib Wikipedia.

Dem : Joowiin, Seet

Ci xam-xamu falag xaaju kol-kol mooy benn xaaj ci ñaar yi ñu sedatlee kol-kolu àdduna bi. Rëddub yemoo bi moo ko xaaj ci digg bi, benn bu tudd xaaju kol-kol bu bëj-gànnaar ak bu bëj-saalum.

Demal ci Wikbaatukaay ngir seet baat yi nga xamul
Samay jumtukaay