Wommatiinu mbëj

Jóge Wikipedia.
Dem : Joowiin, Seet

Wommatiinu mbëj walla Wommatiin wi moo nuy wax ci anam gi wommat wu mbëj wi di amee. Ci limam lanuy sukkandiku ngir man a xam ñaata la benn jumtukaay bi manee wommat mbëj. Safaanam di dëgërluwiinu mbëj wi di li lay wax ni ab jumtukaay manee dëggërlu jàllug dawaanu mbëj ci biiram.

[Soppi] Tekkeem

Bennaanu nattu wommatiin wi mooy siemens ci meetar [s/m]. Nekk itam dawaanu mbëj ci kaw taraayu ab toolu mbëj [I/E]. lu bari bile araf lañu koy teewalee \sigma.

\sigma = \rho^{-1}={l\over {R \cdot A}}

  • \sigma mooy Wommatiin wi
  • l mooy guddaayu wommatukaay bi (ñu koy natte meetar)
  • A mooy dijjaayu wommatukaay bi (ñu koy natte meetar kaare)

[Soppi] Lëkkalekaay yu biir

Samay jumtukaay
Barabu tur

Wuute
Jëf
Joowiin
Boyotu jumtukaay yi
Yeneeni làkk