Barag

Jóge Wikipedia.
Dem : Joowiin, Seet

Ci làkku ibrë (בָּרָק) la tur wi jóge. Ci angale mooy Barak; Ci faranse mooy Barak ou Barac

Njiitu xarekatu bànni Israyil ci jamano Debora ji la woon, lu tollu 1.100 at j.K.. Man nañu jàng ci jalooreem ci Jud 4:1-5:31.

Ci Injiil dinga fekk turam ci Yt 11:32.