Balastus

Jóge Wikipedia.
Dem : Joowiin, Seet

Ci angale mooy Blastus; Ci faranse mooy Blastus

Bëkk-néegu buur ba Erodd Agaripa I la woon.

Turam feeñ na ci Injiil ci Jëf 12:20.