Ayóoba

Jóge Wikipedia.
Dem : Joowiin, Seet

Ci làkku ibrë (אִיּוֹב) la tur wi jóge. Ayóoba mooy ni ñu koy waxe ci Lislaam. Ci angale mooy Job; Ci faranse mooy Job

Benn nit ku fonkoon Yàlla la woon. Yàlla may na Ibliis mu man koo fitnaal. Naka noonu daje na ak coono yu bare. Ay doomam yépp dee nañu te mu ñàkkoon li mu am lépp ci benn fan, ba noppi ànd ak feebar bu metti. Waaye nangu na lépp ak muñ. Man nañu jàng jalooreem ci téere Ayóoba (Job 1:1).

Ci Injiil ci Sa 5:11 la feeñ.