Asos

Jóge Wikipedia.
Dem : Joowiin, Seet

Ci angale mooy Assos; Ci faranse mooy Assos

Benn dëkk ak teeru la woon, ci diiwaanu Misi. Tey jii, mooy dëkk bu tudd Behramkale ci réewu Turki (Turquie).

Dañuy wax ci Asos ci Injiil ci Jëf 20:13,14.

Samay jumtukaay
Barabu tur

Wuute
Jëf
Joowiin
Boyotu jumtukaay yi
Yeneeni làkk