Asaf

Jóge Wikipedia.
Dem : Joowiin, Seet

Ci làkku ibrë (אָסָא) la tur wi jóge. Ci angale mooy Asa; Ci faranse mooy Asaf

Doomu Abiya la woon. Li dale ci Robowam ñetteelu buur ci Yuda la woon. Dafa nguuru lu tollu 41 at ci diggante 913 j.K. ba 873 j.K.. Man nañu jàng ci jalooreem ci 1Ki 15:8-24; 2Ch 14:1-16:14. Benn ci maamaati Yeesu ci Macë la woon (Mc 1:7,8).