Aristàrk

Jóge Wikipedia.
Dem : Joowiin, Seet

Ci angale mooy Aristarchus; Ci faranse mooy Aristarque

Benn toppkatu Yeesu mi dëkkoon Tesalonig la woon, ànd na ak Pool ci liggéeyam.

Aristàrk moo feeñ ci Injiil ci Jëf 19:29; 20:3-5; 27:2; Kol 4:10-11; Fm 1:24.